Al-Hadid · 23/29
Tekki Waxtaan — Al-Hadid
لِّكَيْلَا تَأْسَوْا عَلَىٰ مَا فَاتَكُمْ وَلَا تَفْرَحُوا بِمَا آتَاكُمْ ۗ وَاللَّهُ لَا يُحِبُّ كُلَّ مُخْتَالٍ فَخُورٍ ۝٢٣
Likailaa taasaw `alaa maa faatakum wa laa tafrahoo bimaaa aataakum; wallaahu laa yuhibbu kulla mukhtaalin fakhoor
📖 Tekkim Wolof
ngir ngeen baña yoqat ñanki ci li leer, te it baña bokk ci damoo li mu leen jox. Yàlla safoowul képp kuy damoowaakoon buy fuukare wu.
🎧 Dégg

📜 Aaya 21-25 — Al-Hadid

21سَابِقُوا إِلَىٰ مَغْفِرَةٍ مِّن رَّبِّكُمْ وَجَنَّةٍ عَرْضُهَا كَعَرْضِ السَّمَاءِ وَالْأَرْضِ أُعِدَّتْ لِلَّذِينَ آمَنُوا بِاللَّهِ وَرُسُلِهِ ۚ ذَٰلِكَ فَضْلُ اللَّهِ يُؤْتِيهِ مَن يَشَاءُ ۚ وَاللَّهُ ذُو الْفَضْلِ الْعَظِيمِ
Dawleen jëkënte jëm ci njégëluk seen Boroom ak ca Àjjana joo xam ne yaatuwaayam tollu na ni yaatuwaayu asamaan ak suuf, te dañu koy waajalal ñi gëm Yàlla ak Yonentam. Loolu ngënéelul Yàllaa. Te Yàlla Mooy Boroom ngëneel lu màgg la.
22مَا أَصَابَ مِن مُّصِيبَةٍ فِي الْأَرْضِ وَلَا فِي أَنفُسِكُمْ إِلَّا فِي كِتَابٍ مِّن قَبْلِ أَن نَّبْرَأَهَا ۚ إِنَّ ذَٰلِكَ عَلَى اللَّهِ يَسِيرٌ
Amul menn musiba muy dal ci kaw suuf si walla seen kaw jëmm yi, lu dul ne bind Nanu ko ci ab Téere ba nu ko laata sàkk ; te loolu lu yomb Yàlla la,
23لِّكَيْلَا تَأْسَوْا عَلَىٰ مَا فَاتَكُمْ وَلَا تَفْرَحُوا بِمَا آتَاكُمْ ۗ وَاللَّهُ لَا يُحِبُّ كُلَّ مُخْتَالٍ فَخُورٍ
ngir ngeen baña yoqat ñanki ci li leer, te it baña bokk ci damoo li mu leen jox. Yàlla safoowul képp kuy damoowaakoon buy fuukare wu.
24الَّذِينَ يَبْخَلُونَ وَيَأْمُرُونَ النَّاسَ بِالْبُخْلِ ۗ وَمَن يَتَوَلَّ فَإِنَّ اللَّهَ هُوَ الْغَنِيُّ الْحَمِيدُ
Ña nay tey digël nit ñi ñuy nay. Képp ku dumóoyu... Yàlla moom ku doyloo boppam la di ku Yayoo cant.
25لَقَدْ أَرْسَلْنَا رُسُلَنَا بِالْبَيِّنَاتِ وَأَنزَلْنَا مَعَهُمُ الْكِتَابَ وَالْمِيزَانَ لِيَقُومَ النَّاسُ بِالْقِسْطِ ۖ وَأَنزَلْنَا الْحَدِيدَ فِيهِ بَأْسٌ شَدِيدٌ وَمَنَافِعُ لِلنَّاسِ وَلِيَعْلَمَ اللَّهُ مَن يَنصُرُهُ وَرُسُلَهُ بِالْغَيْبِ ۚ إِنَّ اللَّهَ قَوِيٌّ عَزِيزٌ
Yónni Nanu sunuy Yonenta ci ay firnde yu leer, wàcce ay Téere boolekook ñoom ak i balaas yu màndaxe, ngir nit ñi taxawal maandute. Wàcce Nanu weñ gu ñuul, mu am kàttan gu tar, ak ay njariñ ñeel nit ñi, ak it ngir Yàlla xam, ana kan moo koy dimbalil ay Yonentam, ci kumpa. Yàlla ku am doole la di Boroom Kàttan.
Al-HadidFihi Alxuraan
29Aaya
MedinanRevelation
23Aaya

Tekki — Al-Hadid 23

Simoore Al-Hadid Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ngir ngeen baña yoqat ñanki ci li leer, te it…

Simoore Aaya 23/29 — Al-Hadid الحديد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hadid Dégg, Al-Hadid Tekki, Al-Hadid mp3, Al-Hadid pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers