Al-An'am · 119/165
Tekki Waxtaan — Al-An'am
وَمَا لَكُمْ أَلَّا تَأْكُلُوا مِمَّا ذُكِرَ اسْمُ اللَّهِ عَلَيْهِ وَقَدْ فَصَّلَ لَكُم مَّا حَرَّمَ عَلَيْكُمْ إِلَّا مَا اضْطُرِرْتُمْ إِلَيْهِ ۗ وَإِنَّ كَثِيرًا لَّيُضِلُّونَ بِأَهْوَائِهِم بِغَيْرِ عِلْمٍ ۗ إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ بِالْمُعْتَدِينَ ۝١١٩
Wa maa lakum allaa taakuloo mimmaa zukirasmul laahi `alaihi wa qad fassala lakum maa harrama `alaikum illaa mad turirtum ilaih; wa inna kaseeral la yudilloona bi ahwaaa`ihim bighairi `ilm; inna Rabbaka Huwa a`lamu bilmu`tadeen
📖 Tekkim Wolof
Lu leen nekkal ci bañ lekk loo xam ne tudd nañu ca turu Yàlla ? Moom leeral na leen la araam ci yéen, gannaaw bu fekkee mën ngeen a loru [ngir bañ a am lenn lu ngeen lekk]. Waaye ñu bari dañuy réer ngir topp seeni bànneex cig ñàkk a xam. Sa Boroom moo gën a xam way-jéggi dayo ña.

🎧 Dégg


📜 Aaya 117-121 — Al-An'am

117إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ مَن يَضِلُّ عَن سَبِيلِهِ ۖ وَهُوَ أَعْلَمُ بِالْمُهْتَدِينَ
Te sa Boroom Moo gën a xam ku réere aw yoonam, te Moo gën a xam it ña tegu ci njub gindiku.
118فَكُلُوا مِمَّا ذُكِرَ اسْمُ اللَّهِ عَلَيْهِ إِن كُنتُم بِآيَاتِهِ مُؤْمِنِينَ
Lekkleen la nga xam ne tuddeef na ca turu Yàlla [ba ñu koy rendi], ndegam gëm ngeen ay kàddoom.
119وَمَا لَكُمْ أَلَّا تَأْكُلُوا مِمَّا ذُكِرَ اسْمُ اللَّهِ عَلَيْهِ وَقَدْ فَصَّلَ لَكُم مَّا حَرَّمَ عَلَيْكُمْ إِلَّا مَا اضْطُرِرْتُمْ إِلَيْهِ ۗ وَإِنَّ كَثِيرًا لَّيُضِلُّونَ بِأَهْوَائِهِم بِغَيْرِ عِلْمٍ ۗ إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ بِالْمُعْتَدِينَ
Lu leen nekkal ci bañ lekk loo xam ne tudd nañu ca turu Yàlla ? Moom leeral na leen la araam ci yéen, gannaaw bu fekkee mën ngeen a loru [ngir bañ a am lenn lu ngeen lekk]. Waaye ñu bari dañuy réer ngir topp seeni bànneex cig ñàkk a xam. Sa Boroom moo gën a xam way-jéggi dayo ña.
120وَذَرُوا ظَاهِرَ الْإِثْمِ وَبَاطِنَهُ ۚ إِنَّ الَّذِينَ يَكْسِبُونَ الْإِثْمَ سَيُجْزَوْنَ بِمَا كَانُوا يَقْتَرِفُونَ
Nangeen bàyyi bàkkaar bu fés ak bu nëbbu, ñiy fàggu bàkkaar dees na leen fey la ñu fàggu woon.
121وَلَا تَأْكُلُوا مِمَّا لَمْ يُذْكَرِ اسْمُ اللَّهِ عَلَيْهِ وَإِنَّهُ لَفِسْقٌ ۗ وَإِنَّ الشَّيَاطِينَ لَيُوحُونَ إِلَىٰ أَوْلِيَائِهِمْ لِيُجَادِلُوكُمْ ۖ وَإِنْ أَطَعْتُمُوهُمْ إِنَّكُمْ لَمُشْرِكُونَ
Buleen lekk loo xam ne tudduñu ca turu Yàlla, loolu génn topp la [caay-caay]. Te Séytaane mooy xiir aw nitam ñuy dàggasanteek yéen. Te bu ngeen leen toppee, daldi ñibbi ca way-bokkaale ya.
Al-An'amFihi Alxuraan
165Aaya
MeccanRevelation
119Aaya

Tekki — Al-An'am 119

Simoore Al-An'am Aaya 119 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lu leen nekkal ci bañ lekk loo xam ne tudd…

Simoore Aaya 119/165 — Al-An'am الأنعام (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-An'am Dégg, Al-An'am Tekki, Al-An'am mp3, Al-An'am pdf. Aaya 117–121. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers