Al-An'am · 4/165
Tekki Waxtaan — Simoore Al-An'am
وَمَا تَأْتِيهِم مِّنْ آيَةٍ مِّنْ آيَاتِ رَبِّهِمْ إِلَّا كَانُوا عَنْهَا مُعْرِضِينَ ۝٤
Wa maa taateehim min Aayatim min Aayaati Rabbihim illaa kaanoo `anhaa mu`rideen
📖 Tekkim Wolof
Te kat amul lenn ndigal lu leen dikke ca seen Boroom te dëdduwuñu ko.

🎧 Dégg


📜 Aaya 2-6 — Simoore Al-An'am

2هُوَ الَّذِي خَلَقَكُم مِّن طِينٍ ثُمَّ قَضَىٰ أَجَلًا ۖ وَأَجَلٌ مُّسَمًّى عِندَهُ ۖ ثُمَّ أَنتُمْ تَمْتَرُونَ
Moom mooy ki leen bind ci ban ; ba noppi dugal àpp [ci dundu gu ne] ak àpp ba ñu tudd ci Moom [ci jéexug àdduna si]. Ba noppi ngeen di am xel-yaar !
3وَهُوَ اللَّهُ فِي السَّمَاوَاتِ وَفِي الْأَرْضِ ۖ يَعْلَمُ سِرَّكُمْ وَجَهْرَكُمْ وَيَعْلَمُ مَا تَكْسِبُونَ
Te Mooy Yàlla ci asamaan yeek suuf si. Mooy ki xam seen mbóot yi ngeen di nëbb ak yi ngeen di feeñal te xam it la ngeen di fàggu.
4وَمَا تَأْتِيهِم مِّنْ آيَةٍ مِّنْ آيَاتِ رَبِّهِمْ إِلَّا كَانُوا عَنْهَا مُعْرِضِينَ
Te kat amul lenn ndigal lu leen dikke ca seen Boroom te dëdduwuñu ko.
5فَقَدْ كَذَّبُوا بِالْحَقِّ لَمَّا جَاءَهُمْ ۖ فَسَوْفَ يَأْتِيهِمْ أَنبَاءُ مَا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
Weddi nañu dëgg ba mu dikkee ca ñoom. Waaye dana leen mas a dikkal xew-xewi la ñu tejji.
6أَلَمْ يَرَوْا كَمْ أَهْلَكْنَا مِن قَبْلِهِم مِّن قَرْنٍ مَّكَّنَّاهُمْ فِي الْأَرْضِ مَا لَمْ نُمَكِّن لَّكُمْ وَأَرْسَلْنَا السَّمَاءَ عَلَيْهِم مِّدْرَارًا وَجَعَلْنَا الْأَنْهَارَ تَجْرِي مِن تَحْتِهِمْ فَأَهْلَكْنَاهُم بِذُنُوبِهِمْ وَأَنشَأْنَا مِن بَعْدِهِمْ قَرْنًا آخَرِينَ
Moo ndax dañoo xamul ñaata maas Lanu alag ca ña leen jiitu, ñoo xam ne mayoon Nanu leen lu Nu leen mayul [yéen] ? Te dottil woon Nanu asamaan mu taw ca ñoom, waaye defaloon leen ay dex yuy dawaan. Waaye Nu daldi leen alag ngir seeni bàkkaar ; sosaat nag geneen maas wu watle leen ko.
Al-An'amFihi Alxuraan
165Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-An'am 4

Simoore Al-An'am Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te kat amul lenn ndigal lu leen dikke ca seen…

Simoore Aaya 4/165 — Simoore Al-An'am الأنعام (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-An'am Dégg, Simoore Al-An'am Tekki, Simoore Al-An'am mp3, Simoore Al-An'am pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers