At-Tahrim · 2/12
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tahrim
قَدْ فَرَضَ اللَّهُ لَكُمْ تَحِلَّةَ أَيْمَانِكُمْ ۚ وَاللَّهُ مَوْلَاكُمْ ۖ وَهُوَ الْعَلِيمُ الْحَكِيمُ ۝٢
Qad faradal laahu lakum tahillata aymaanikum; wallaahu mawlaakum wa huwal`aleemul hakeem
📖 Tekkim Wolof
Yàlla fartal na ci yéen, daganal seeni ngiñ. Yàlla di seen Boroom ; te Ku Xam la Ku Xereñ la .

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-4 — Simoore At-Tahrim

1يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ لِمَ تُحَرِّمُ مَا أَحَلَّ اللَّهُ لَكَ ۖ تَبْتَغِي مَرْضَاتَ أَزْوَاجِكَ ۚ وَاللَّهُ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Éy yaw Yonent bi ! Ana lu tax, ngay araamal lu la Yàlla daganalal, nga di ca sàkku ngëram loo say soxna ? (Waaye) Yàlla moom Jéggalaakoon la, Jagléwaakoon la.
2قَدْ فَرَضَ اللَّهُ لَكُمْ تَحِلَّةَ أَيْمَانِكُمْ ۚ وَاللَّهُ مَوْلَاكُمْ ۖ وَهُوَ الْعَلِيمُ الْحَكِيمُ
Yàlla fartal na ci yéen, daganal seeni ngiñ. Yàlla di seen Boroom ; te Ku Xam la Ku Xereñ la .
3وَإِذْ أَسَرَّ النَّبِيُّ إِلَىٰ بَعْضِ أَزْوَاجِهِ حَدِيثًا فَلَمَّا نَبَّأَتْ بِهِ وَأَظْهَرَهُ اللَّهُ عَلَيْهِ عَرَّفَ بَعْضَهُ وَأَعْرَضَ عَن بَعْضٍ ۖ فَلَمَّا نَبَّأَهَا بِهِ قَالَتْ مَنْ أَنبَأَكَ هَٰذَا ۖ قَالَ نَبَّأَنِيَ الْعَلِيمُ الْخَبِيرُ
Ba Yonent bi joxee sekkare lennat ci soxnaam ba ñu ko tasaaree te Yàlla wuññil ko lenn la, dëddu leneen la. Ba mu ko xibaare soxna sa mu ne ko : “ku la ko xibaar ? ” Mu ne ko : “Yàlla mi Xam, te deñ Kumpa ci lépp mooma ko xibaar”.
4إِن تَتُوبَا إِلَى اللَّهِ فَقَدْ صَغَتْ قُلُوبُكُمَا ۖ وَإِن تَظَاهَرَا عَلَيْهِ فَإِنَّ اللَّهَ هُوَ مَوْلَاهُ وَجِبْرِيلُ وَصَالِحُ الْمُؤْمِنِينَ ۖ وَالْمَلَائِكَةُ بَعْدَ ذَٰلِكَ ظَهِيرٌ
Yéen ñaari soxna yi su ngeen tuubee (moo gën) ndax seeni xol jeng na. Su ngeen takktoo (Yonent bi), Yàlla farnaak moom, ak Jibriil ak jullit ñu yiw ñi, ak Malaaka yi di ko dimbali.
At-TahrimFihi Alxuraan
12Aaya
MedinanRevelation
2Aaya

Tekki — At-Tahrim 2

Simoore At-Tahrim Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla fartal na ci yéen, daganal seeni ngiñ. Yàlla di…

Simoore Aaya 2/12 — Simoore At-Tahrim التحريم (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tahrim Dégg, Simoore At-Tahrim Tekki, Simoore At-Tahrim mp3, Simoore At-Tahrim pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers