At-Tahrim · 1/12
Tekki Waxtaan — At-Tahrim
يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ لِمَ تُحَرِّمُ مَا أَحَلَّ اللَّهُ لَكَ ۖ تَبْتَغِي مَرْضَاتَ أَزْوَاجِكَ ۚ وَاللَّهُ غَفُورٌ رَّحِيمٌ ۝١
Yaaa ayyuhan nabiyyu lima tuharrimu maaa ahallal laahu laka tabtaghee mardaata azwaajik; wallaahu ghafoorur raheem
📖 Tekkim Wolof
Éy yaw Yonent bi ! Ana lu tax, ngay araamal lu la Yàlla daganalal, nga di ca sàkku ngëram loo say soxna ? (Waaye) Yàlla moom Jéggalaakoon la, Jagléwaakoon la.
🎧 Dégg

📜 Aaya 1-3 — At-Tahrim

1يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ لِمَ تُحَرِّمُ مَا أَحَلَّ اللَّهُ لَكَ ۖ تَبْتَغِي مَرْضَاتَ أَزْوَاجِكَ ۚ وَاللَّهُ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Éy yaw Yonent bi ! Ana lu tax, ngay araamal lu la Yàlla daganalal, nga di ca sàkku ngëram loo say soxna ? (Waaye) Yàlla moom Jéggalaakoon la, Jagléwaakoon la.
2قَدْ فَرَضَ اللَّهُ لَكُمْ تَحِلَّةَ أَيْمَانِكُمْ ۚ وَاللَّهُ مَوْلَاكُمْ ۖ وَهُوَ الْعَلِيمُ الْحَكِيمُ
Yàlla fartal na ci yéen, daganal seeni ngiñ. Yàlla di seen Boroom ; te Ku Xam la Ku Xereñ la .
3وَإِذْ أَسَرَّ النَّبِيُّ إِلَىٰ بَعْضِ أَزْوَاجِهِ حَدِيثًا فَلَمَّا نَبَّأَتْ بِهِ وَأَظْهَرَهُ اللَّهُ عَلَيْهِ عَرَّفَ بَعْضَهُ وَأَعْرَضَ عَن بَعْضٍ ۖ فَلَمَّا نَبَّأَهَا بِهِ قَالَتْ مَنْ أَنبَأَكَ هَٰذَا ۖ قَالَ نَبَّأَنِيَ الْعَلِيمُ الْخَبِيرُ
Ba Yonent bi joxee sekkare lennat ci soxnaam ba ñu ko tasaaree te Yàlla wuññil ko lenn la, dëddu leneen la. Ba mu ko xibaare soxna sa mu ne ko : “ku la ko xibaar ? ” Mu ne ko : “Yàlla mi Xam, te deñ Kumpa ci lépp mooma ko xibaar”.
At-TahrimFihi Alxuraan
12Aaya
MedinanRevelation
1Aaya

Tekki — At-Tahrim 1

Simoore At-Tahrim Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Éy yaw Yonent bi ! Ana lu tax, ngay araamal…

Simoore Aaya 1/12 — At-Tahrim التحريم (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tahrim Dégg, At-Tahrim Tekki, At-Tahrim mp3, At-Tahrim pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers