Al-Mulk · 22/30
Tekki Waxtaan — Al-Mulk
أَفَمَن يَمْشِي مُكِبًّا عَلَىٰ وَجْهِهِ أَهْدَىٰ أَمَّن يَمْشِي سَوِيًّا عَلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ ۝٢٢
Afamai yamshee mukibban `alaa wajhihee ahdaaa ammany yamshee sawiyyan `alaa siratim mustaqeem
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax ? Waajiy dëpp xarkanamam moo gën a gindiku kiy dox ne sàtt ca kaw yoon wa jub xocc.
🎧 Dégg

📜 Aaya 20-24 — Al-Mulk

20أَمَّنْ هَٰذَا الَّذِي هُوَ جُندٌ لَّكُمْ يَنصُرُكُم مِّن دُونِ الرَّحْمَٰنِ ۚ إِنِ الْكَافِرُونَ إِلَّا فِي غُرُورٍ
Ana kan moo leen man a wutal ay xarekat yu leen di taxwu te du Yàlla ? Yéefër yi ci woro la ñu nekk.
21أَمَّنْ هَٰذَا الَّذِي يَرْزُقُكُمْ إِنْ أَمْسَكَ رِزْقَهُ ۚ بَل لَّجُّوا فِي عُتُوٍّ وَنُفُورٍ
Ana kan moo leen di wërsëgal su (Yàlla) téyee wërsëgëm ? Ñoom da ñoo sànku.
22أَفَمَن يَمْشِي مُكِبًّا عَلَىٰ وَجْهِهِ أَهْدَىٰ أَمَّن يَمْشِي سَوِيًّا عَلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Moo ndax ? Waajiy dëpp xarkanamam moo gën a gindiku kiy dox ne sàtt ca kaw yoon wa jub xocc.
23قُلْ هُوَ الَّذِي أَنشَأَكُمْ وَجَعَلَ لَكُمُ السَّمْعَ وَالْأَبْصَارَ وَالْأَفْئِدَةَ ۖ قَلِيلًا مَّا تَشْكُرُونَ
Waxal ne: “Moom moo leen sàkk defal leen dégg, ak ub gis ak i xol”. Te néewaana ngeen sant delloo njukël !
24قُلْ هُوَ الَّذِي ذَرَأَكُمْ فِي الْأَرْضِ وَإِلَيْهِ تُحْشَرُونَ
Waxal ne : “It moo leen ji ci suuf si, te ca moom ngeen di mujj ñu pang leen”.
Al-MulkFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — Al-Mulk 22

Simoore Al-Mulk Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax ? Waajiy dëpp xarkanamam moo gën a gindiku…

Simoore Aaya 22/30 — Al-Mulk الملك (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mulk Dégg, Al-Mulk Tekki, Al-Mulk mp3, Al-Mulk pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers