Nuh · 2/28
Tekki Waxtaan — Simoore Nuh
قَالَ يَا قَوْمِ إِنِّي لَكُمْ نَذِيرٌ مُّبِينٌ ۝٢
Qaala yaa qawmi innee lakum nazeerum mubeen
📖 Tekkim Wolof
Mu daldi ne : "Éy seen samaw nit, man mii ab xuppekat laa ci yéen bu bir,

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-4 — Simoore Nuh

1إِنَّا أَرْسَلْنَا نُوحًا إِلَىٰ قَوْمِهِ أَنْ أَنذِرْ قَوْمَكَ مِن قَبْلِ أَن يَأْتِيَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ
Noo yónni woon Nooh ca aw nitam ne ko : “Xupal saw nit, bala leen mbugal mu mettee dikkël”.
2قَالَ يَا قَوْمِ إِنِّي لَكُمْ نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Mu daldi ne : "Éy seen samaw nit, man mii ab xuppekat laa ci yéen bu bir,
3أَنِ اعْبُدُوا اللَّهَ وَاتَّقُوهُ وَأَطِيعُونِ
Na ngeen jaamu Yàlla, te ragal ko, te topp ko
4يَغْفِرْ لَكُم مِّن ذُنُوبِكُمْ وَيُؤَخِّرْكُمْ إِلَىٰ أَجَلٍ مُّسَمًّى ۚ إِنَّ أَجَلَ اللَّهِ إِذَا جَاءَ لَا يُؤَخَّرُ ۖ لَوْ كُنتُمْ تَعْلَمُونَ
kon dey Dana leen jégël seeni bàkkaar te Dana leen yeexe ba ci dig bu ñu xam. Digub Yàlla bu agsee, du fanqu cëy bu ngeen xamoon ! ”
NuhFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
2Aaya

Tekki — Nuh 2

Simoore Nuh Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu daldi ne : "Éy seen samaw nit, man mii…

Simoore Aaya 2/28 — Simoore Nuh نوح (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Nuh Dégg, Simoore Nuh Tekki, Simoore Nuh mp3, Simoore Nuh pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers