Al-Buruj · 17/22
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Buruj
هَلْ أَتَاكَ حَدِيثُ الْجُنُودِ ۝١٧
Hal ataaka hadeesul junood
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax waxtaanu xarekat ya dikal na la ( xibaar ya),

🎧 Dégg


📜 Aaya 15-19 — Simoore Al-Buruj

15ذُو الْعَرْشِ الْمَجِيدُ
Mooy boroom Gàngunaay gu Màgg ga (Aras),
16فَعَّالٌ لِّمَا يُرِيدُ
Lu mu namm dana ko def.
17هَلْ أَتَاكَ حَدِيثُ الْجُنُودِ
Moo ndax waxtaanu xarekat ya dikal na la ( xibaar ya),
18فِرْعَوْنَ وَثَمُودَ
Firawna, ak Samuud ?
19بَلِ الَّذِينَ كَفَرُوا فِي تَكْذِيبٍ
Yéefër ya dañuy weddi,
Al-BurujFihi Alxuraan
22Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — Al-Buruj 17

Simoore Al-Buruj Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax waxtaanu xarekat ya dikal na la ( xibaar…

Simoore Aaya 17/22 — Simoore Al-Buruj البروج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Buruj Dégg, Simoore Al-Buruj Tekki, Simoore Al-Buruj mp3, Simoore Al-Buruj pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers