Al-Buruj · 16/22
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Buruj
فَعَّالٌ لِّمَا يُرِيدُ ۝١٦
Fa` `aalul limaa yureed
📖 Tekkim Wolof
Lu mu namm dana ko def.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 14-18 — Simoore Al-Buruj

14وَهُوَ الْغَفُورُ الْوَدُودُ
Te moom moo di Jéggëlaakoon bi, di soppi lépp,
15ذُو الْعَرْشِ الْمَجِيدُ
Mooy boroom Gàngunaay gu Màgg ga (Aras),
16فَعَّالٌ لِّمَا يُرِيدُ
Lu mu namm dana ko def.
17هَلْ أَتَاكَ حَدِيثُ الْجُنُودِ
Moo ndax waxtaanu xarekat ya dikal na la ( xibaar ya),
18فِرْعَوْنَ وَثَمُودَ
Firawna, ak Samuud ?
Al-BurujFihi Alxuraan
22Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-Buruj 16

Simoore Al-Buruj Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lu mu namm dana ko def.

Simoore Aaya 16/22 — Simoore Al-Buruj البروج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Buruj Dégg, Simoore Al-Buruj Tekki, Simoore Al-Buruj mp3, Simoore Al-Buruj pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers