Al-Buruj · 19/22
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Buruj
بَلِ الَّذِينَ كَفَرُوا فِي تَكْذِيبٍ ۝١٩
Balil lazeena kafaroo fee takzeeb
📖 Tekkim Wolof
Yéefër ya dañuy weddi,

🎧 Dégg


📜 Aaya 17-21 — Simoore Al-Buruj

17هَلْ أَتَاكَ حَدِيثُ الْجُنُودِ
Moo ndax waxtaanu xarekat ya dikal na la ( xibaar ya),
18فِرْعَوْنَ وَثَمُودَ
Firawna, ak Samuud ?
19بَلِ الَّذِينَ كَفَرُوا فِي تَكْذِيبٍ
Yéefër ya dañuy weddi,
20وَاللَّهُ مِن وَرَائِهِم مُّحِيطٌ
te Yàlla ngi leen peeg, ci wet gu nekk.
21بَلْ هُوَ قُرْآنٌ مَّجِيدٌ
li wér mooy Alxuraan ju màgg la
Al-BurujFihi Alxuraan
22Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — Al-Buruj 19

Simoore Al-Buruj Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéefër ya dañuy weddi,

Simoore Aaya 19/22 — Simoore Al-Buruj البروج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Buruj Dégg, Simoore Al-Buruj Tekki, Simoore Al-Buruj mp3, Simoore Al-Buruj pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers