At-Tawba · 9/129
Tekki Waxtaan — At-Tawba
اشْتَرَوْا بِآيَاتِ اللَّهِ ثَمَنًا قَلِيلًا فَصَدُّوا عَن سَبِيلِهِ ۚ إِنَّهُمْ سَاءَ مَا كَانُوا يَعْمَلُونَ ۝٩
Ishtaraw bi Aayaatil laahi samanan qaleelan fasaddoo `an sabeelih; innahum saaa`a maa kaanoo ya`maloon
📖 Tekkim Wolof
Dañuy weccee ndigali Yàlla ak njëg yu néew, di sakk yoonam wa. Ñoom nag la ñuy def aka bon !
🎧 Dégg

📜 Aaya 7-11 — At-Tawba

7كَيْفَ يَكُونُ لِلْمُشْرِكِينَ عَهْدٌ عِندَ اللَّهِ وَعِندَ رَسُولِهِ إِلَّا الَّذِينَ عَاهَدتُّمْ عِندَ الْمَسْجِدِ الْحَرَامِ ۖ فَمَا اسْتَقَامُوا لَكُمْ فَاسْتَقِيمُوا لَهُمْ ۚ إِنَّ اللَّهَ يُحِبُّ الْمُتَّقِينَ
Naka la ay bokkaalekat di amee kóllare ak Yàlla ak Yonentam ginnaaw ña ngeen kóllaranteek woon ak ñoom ca wetu jàkka ja ñu wormaal. Feek ña ngay def njub ak yéen, defleen yéen it njub ak ñoom. Yàlla nag Dafa sopp ñay ragal seen Boroom.
8كَيْفَ وَإِن يَظْهَرُوا عَلَيْكُمْ لَا يَرْقُبُوا فِيكُمْ إِلًّا وَلَا ذِمَّةً ۚ يُرْضُونَكُم بِأَفْوَاهِهِمْ وَتَأْبَىٰ قُلُوبُهُمْ وَأَكْثَرُهُمْ فَاسِقُونَ
Moo ndax ñoom bu ñu leen notoon, danañu sàmmonteek la dox seeni diggante ci wàllu mbokk. xxxxx; Ay saay-saay lañu.
9اشْتَرَوْا بِآيَاتِ اللَّهِ ثَمَنًا قَلِيلًا فَصَدُّوا عَن سَبِيلِهِ ۚ إِنَّهُمْ سَاءَ مَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Dañuy weccee ndigali Yàlla ak njëg yu néew, di sakk yoonam wa. Ñoom nag la ñuy def aka bon !
10لَا يَرْقُبُونَ فِي مُؤْمِنٍ إِلًّا وَلَا ذِمَّةً ۚ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُعْتَدُونَ
Duñu sàmmonteek ña gëmoon, ci wàllu mbokk du ci wàllu kóllare. Te ñoom ñoo di ñu jéggi dayo ña.
11فَإِن تَابُوا وَأَقَامُوا الصَّلَاةَ وَآتَوُا الزَّكَاةَ فَإِخْوَانُكُمْ فِي الدِّينِ ۗ وَنُفَصِّلُ الْآيَاتِ لِقَوْمٍ يَعْلَمُونَ
Waaye bu ñu tuubee, te taxawal julli, di joxe asaka, kon seeni mbokk lañu ci diine ji. Te Danuy leeral tegtal yi ngir nit ñuy xam.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
9Aaya

Tekki — At-Tawba 9

Simoore At-Tawba Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dañuy weccee ndigali Yàlla ak njëg yu néew, di sakk…

Simoore Aaya 9/129 — At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tawba Dégg, At-Tawba Tekki, At-Tawba mp3, At-Tawba pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers