Hud · 112/123
Tekki Waxtaan — Hud
فَاسْتَقِمْ كَمَا أُمِرْتَ وَمَن تَابَ مَعَكَ وَلَا تَطْغَوْا ۚ إِنَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ بَصِيرٌ ۝١١٢
Fastaqim kamaaa umirta wa man taaba ma`aka wa laa tatghaw; innahoo bimaa ta`maloona Baseer
📖 Tekkim Wolof
Jubal [yaw Muhammad] ni ñu la ko digle, ak képp ku tuub ànd ak yaw. Buleen beew. Moom Yàlla mi ngi ne jàkk ci li ngeen di def.

🎧 Dégg


📜 Aaya 110-114 — Hud

110وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْكِتَابَ فَاخْتُلِفَ فِيهِ ۚ وَلَوْلَا كَلِمَةٌ سَبَقَتْ مِن رَّبِّكَ لَقُضِيَ بَيْنَهُمْ ۚ وَإِنَّهُمْ لَفِي شَكٍّ مِّنْهُ مُرِيبٍ
Joxoon Nanu Muusaa Téere ba. Ñu wuute ca. Bu dul koon sa kàddug Boroom jiitu woon, kon àtteef na seen diggante. Te ñoom dañu caa am sikki-sàkka gu tar.
111وَإِنَّ كُلًّا لَّمَّا لَيُوَفِّيَنَّهُمْ رَبُّكَ أَعْمَالَهُمْ ۚ إِنَّهُ بِمَا يَعْمَلُونَ خَبِيرٌ
Fàwwu ñoom ñépp sa Boroom Dana matal seen peyug jëf... Naka Moom ku xam xéll la li ñuy jëf.
112فَاسْتَقِمْ كَمَا أُمِرْتَ وَمَن تَابَ مَعَكَ وَلَا تَطْغَوْا ۚ إِنَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ بَصِيرٌ
Jubal [yaw Muhammad] ni ñu la ko digle, ak képp ku tuub ànd ak yaw. Buleen beew. Moom Yàlla mi ngi ne jàkk ci li ngeen di def.
113وَلَا تَرْكَنُوا إِلَى الَّذِينَ ظَلَمُوا فَتَمَسَّكُمُ النَّارُ وَمَا لَكُم مِّن دُونِ اللَّهِ مِنْ أَوْلِيَاءَ ثُمَّ لَا تُنصَرُونَ
Buleen jeng féetéek tooñkat ya : kon Safara laal leen. Te dungeen am ku leen di yiir ku dul Yàlla. Te it kenn du leen dimbali.
114وَأَقِمِ الصَّلَاةَ طَرَفَيِ النَّهَارِ وَزُلَفًا مِّنَ اللَّيْلِ ۚ إِنَّ الْحَسَنَاتِ يُذْهِبْنَ السَّيِّئَاتِ ۚ ذَٰلِكَ ذِكْرَىٰ لِلذَّاكِرِينَ
Nanga taxawal julli ci yaari cat yi séq bis bi ak li bokk ci guddi. Jëf yu baax yi dañuy far jëf yu ñaaw ya. Loolu ag waare la ci ñuy waaru.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
112Aaya

Tekki — Hud 112

Simoore Hud Aaya 112 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jubal [yaw Muhammad] ni ñu la ko digle, ak képp…

Simoore Aaya 112/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 110–114. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers