Hud · 113/123
Tekki Waxtaan — Hud
وَلَا تَرْكَنُوا إِلَى الَّذِينَ ظَلَمُوا فَتَمَسَّكُمُ النَّارُ وَمَا لَكُم مِّن دُونِ اللَّهِ مِنْ أَوْلِيَاءَ ثُمَّ لَا تُنصَرُونَ ۝١١٣
Wa laa tarkanooo ilal lazeena zalamoo fatamassa kumun Naaru wa maa lakum min doonil laahi min awliyaaa`a summa laa tunsaroon
📖 Tekkim Wolof
Buleen jeng féetéek tooñkat ya : kon Safara laal leen. Te dungeen am ku leen di yiir ku dul Yàlla. Te it kenn du leen dimbali.
🎧 Dégg

📜 Aaya 111-115 — Hud

111وَإِنَّ كُلًّا لَّمَّا لَيُوَفِّيَنَّهُمْ رَبُّكَ أَعْمَالَهُمْ ۚ إِنَّهُ بِمَا يَعْمَلُونَ خَبِيرٌ
Fàwwu ñoom ñépp sa Boroom Dana matal seen peyug jëf... Naka Moom ku xam xéll la li ñuy jëf.
112فَاسْتَقِمْ كَمَا أُمِرْتَ وَمَن تَابَ مَعَكَ وَلَا تَطْغَوْا ۚ إِنَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ بَصِيرٌ
Jubal [yaw Muhammad] ni ñu la ko digle, ak képp ku tuub ànd ak yaw. Buleen beew. Moom Yàlla mi ngi ne jàkk ci li ngeen di def.
113وَلَا تَرْكَنُوا إِلَى الَّذِينَ ظَلَمُوا فَتَمَسَّكُمُ النَّارُ وَمَا لَكُم مِّن دُونِ اللَّهِ مِنْ أَوْلِيَاءَ ثُمَّ لَا تُنصَرُونَ
Buleen jeng féetéek tooñkat ya : kon Safara laal leen. Te dungeen am ku leen di yiir ku dul Yàlla. Te it kenn du leen dimbali.
114وَأَقِمِ الصَّلَاةَ طَرَفَيِ النَّهَارِ وَزُلَفًا مِّنَ اللَّيْلِ ۚ إِنَّ الْحَسَنَاتِ يُذْهِبْنَ السَّيِّئَاتِ ۚ ذَٰلِكَ ذِكْرَىٰ لِلذَّاكِرِينَ
Nanga taxawal julli ci yaari cat yi séq bis bi ak li bokk ci guddi. Jëf yu baax yi dañuy far jëf yu ñaaw ya. Loolu ag waare la ci ñuy waaru.
115وَاصْبِرْ فَإِنَّ اللَّهَ لَا يُضِيعُ أَجْرَ الْمُحْسِنِينَ
Nanga muñ. Yàlla dey du sànk peyug ñay rafetal.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
113Aaya

Tekki — Hud 113

Simoore Hud Aaya 113 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Buleen jeng féetéek tooñkat ya : kon Safara laal leen.…

Simoore Aaya 113/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 111–115. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers