Hud · 12/123
Tekki Waxtaan — Simoore Hud
فَلَعَلَّكَ تَارِكٌ بَعْضَ مَا يُوحَىٰ إِلَيْكَ وَضَائِقٌ بِهِ صَدْرُكَ أَن يَقُولُوا لَوْلَا أُنزِلَ عَلَيْهِ كَنزٌ أَوْ جَاءَ مَعَهُ مَلَكٌ ۚ إِنَّمَا أَنتَ نَذِيرٌ ۚ وَاللَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ وَكِيلٌ ۝١٢
Fala`allaka taarikum ba`da maa yoohaaa ilaika wa daaa`iqum bihee sadruka ai yaqooloo law laaa unzila `alaihi kanzun aw jaaa`a ma`ahoo malak; innamaa anta nazeer; wallaahu `alaa kulli shai`inw wakeel
📖 Tekkim Wolof
Xéy-na danga bàyyi lenn ca la Nu la soloo, nga ànd ci ak xol bu xat ; ngir la ñuy wax naan : “Lu tee woon ñu wàcceel ko ndàmbul alal ? ”. Walla : “Mu dikk ànd ak i Malaaka ? ” - Waaye yaw nekkuloo lu dul waarekat. Yàlla nag mooy Kuy wattu lépp lu mu mën a doon.

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Simoore Hud

10وَلَئِنْ أَذَقْنَاهُ نَعْمَاءَ بَعْدَ ضَرَّاءَ مَسَّتْهُ لَيَقُولَنَّ ذَهَبَ السَّيِّئَاتُ عَنِّي ۚ إِنَّهُ لَفَرِحٌ فَخُورٌ
Te wóor na it ne, su Nu ko mosalee xéewal ginnaaw naqar wa ko daloon, dana wax ne : “Tiis teggeeku na ma”, Moom [nit] kuy bég la, di puukarewaakon.
11إِلَّا الَّذِينَ صَبَرُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ أُولَٰئِكَ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَأَجْرٌ كَبِيرٌ
ba mu des ña nga xam ne dañoo muñ, di jëf jëf yu sell. Ñoom ñooña am nañu njéggal ak pey gu mag.
12فَلَعَلَّكَ تَارِكٌ بَعْضَ مَا يُوحَىٰ إِلَيْكَ وَضَائِقٌ بِهِ صَدْرُكَ أَن يَقُولُوا لَوْلَا أُنزِلَ عَلَيْهِ كَنزٌ أَوْ جَاءَ مَعَهُ مَلَكٌ ۚ إِنَّمَا أَنتَ نَذِيرٌ ۚ وَاللَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ وَكِيلٌ
Xéy-na danga bàyyi lenn ca la Nu la soloo, nga ànd ci ak xol bu xat ; ngir la ñuy wax naan : “Lu tee woon ñu wàcceel ko ndàmbul alal ? ”. Walla : “Mu dikk ànd ak i Malaaka ? ” - Waaye yaw nekkuloo lu dul waarekat. Yàlla nag mooy Kuy wattu lépp lu mu mën a doon.
13أَمْ يَقُولُونَ افْتَرَاهُ ۖ قُلْ فَأْتُوا بِعَشْرِ سُوَرٍ مِّثْلِهِ مُفْتَرَيَاتٍ وَادْعُوا مَنِ اسْتَطَعْتُم مِّن دُونِ اللَّهِ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Am dañuy wax ne : “Dakoo duur” - Neel : “Indileen fukki saar yu ni mel, yu ngeen fent. Te ngeen woo ku leen neex ndeem ñu dëggu ngeen”.
14فَإِلَّمْ يَسْتَجِيبُوا لَكُمْ فَاعْلَمُوا أَنَّمَا أُنزِلَ بِعِلْمِ اللَّهِ وَأَن لَّا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ فَهَلْ أَنتُم مُّسْلِمُونَ
Bu ñu leen wuyyuwul, nangeen xam ne la ñu wàcce, ci xam-xamub Yàlla la, te nag amul jeneen yàlla ju dul Moom. Waaw, ndax dangeen dul wommatu nekk ay jullit ?
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Hud 12

Simoore Hud Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xéy-na danga bàyyi lenn ca la Nu la soloo, nga…

Simoore Aaya 12/123 — Simoore Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Hud Dégg, Simoore Hud Tekki, Simoore Hud mp3, Simoore Hud pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers