Yusuf · 35/111
Tekki Waxtaan — Simoore Yusuf
ثُمَّ بَدَا لَهُم مِّن بَعْدِ مَا رَأَوُا الْآيَاتِ لَيَسْجُنُنَّهُ حَتَّىٰ حِينٍ ۝٣٥
Summa badaa lahum mim ba`di maa ra-awul Aayaati layasjununnahoo hatta heen
📖 Tekkim Wolof
Ginnaaw ba ñu gisee dëgg ga mu fees ca ñoom, ñu ne fàwwu danañu ko tëj kaso ab diir.

🎧 Dégg


📜 Aaya 33-37 — Simoore Yusuf

33قَالَ رَبِّ السِّجْنُ أَحَبُّ إِلَيَّ مِمَّا يَدْعُونَنِي إِلَيْهِ ۖ وَإِلَّا تَصْرِفْ عَنِّي كَيْدَهُنَّ أَصْبُ إِلَيْهِنَّ وَأَكُن مِّنَ الْجَاهِلِينَ
Mu ne[moom Yuusufa] : "Yaw sama Boroom, kaso laa gën a bëgg ci lii ñu may woo jëme ma ca. Te boo ma wëlbatilul seeni pexe, danaa jeng jëm ca ñoom te kon ma bokk ca ña réer [xamadi]”.
34فَاسْتَجَابَ لَهُ رَبُّهُ فَصَرَفَ عَنْهُ كَيْدَهُنَّ ۚ إِنَّهُ هُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ
Boroomam nangu ñaanam, daldi ko fegal seeni pexe. Moom [Yàlla] mooy Aji-dégg, di Aji-xam ji.
35ثُمَّ بَدَا لَهُم مِّن بَعْدِ مَا رَأَوُا الْآيَاتِ لَيَسْجُنُنَّهُ حَتَّىٰ حِينٍ
Ginnaaw ba ñu gisee dëgg ga mu fees ca ñoom, ñu ne fàwwu danañu ko tëj kaso ab diir.
36وَدَخَلَ مَعَهُ السِّجْنَ فَتَيَانِ ۖ قَالَ أَحَدُهُمَا إِنِّي أَرَانِي أَعْصِرُ خَمْرًا ۖ وَقَالَ الْآخَرُ إِنِّي أَرَانِي أَحْمِلُ فَوْقَ رَأْسِي خُبْزًا تَأْكُلُ الطَّيْرُ مِنْهُ ۖ نَبِّئْنَا بِتَأْوِيلِهِ ۖ إِنَّا نَرَاكَ مِنَ الْمُحْسِنِينَ
Mu duggandoo ca kaso ba ak ñaari xale yu góor. Kenn ca ñoom ne : “Damaa gent di nal sàngara...” Keneen ka ne : “Gént naa man itam yenu ci sama bopp mburu, ay picc di ca lekk. Leeralal nu seenum piri, ndax nun gis nanu la nga bokk ca way-rafetal ña”.
37قَالَ لَا يَأْتِيكُمَا طَعَامٌ تُرْزَقَانِهِ إِلَّا نَبَّأْتُكُمَا بِتَأْوِيلِهِ قَبْلَ أَن يَأْتِيَكُمَا ۚ ذَٰلِكُمَا مِمَّا عَلَّمَنِي رَبِّي ۚ إِنِّي تَرَكْتُ مِلَّةَ قَوْمٍ لَّا يُؤْمِنُونَ بِاللَّهِ وَهُم بِالْآخِرَةِ هُمْ كَافِرُونَ
Mu ne leen : “Ñam wii ñu leen di wërsëgale, balaa ñëw ma leeralal leen seen piri. Noonu lay deme ci yéen ñaar ngir la ma sama Boroom xamal. Ndax man bàyyi naa diiney nit ñu gëmul Yàlla te weddi àllaaxira.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
35Aaya

Tekki — Yusuf 35

Simoore Yusuf Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ginnaaw ba ñu gisee dëgg ga mu fees ca ñoom,…

Simoore Aaya 35/111 — Simoore Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yusuf Dégg, Simoore Yusuf Tekki, Simoore Yusuf mp3, Simoore Yusuf pdf. Aaya 33–37. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers