Yusuf · 47/111
Tekki Waxtaan — Simoore Yusuf
قَالَ تَزْرَعُونَ سَبْعَ سِنِينَ دَأَبًا فَمَا حَصَدتُّمْ فَذَرُوهُ فِي سُنبُلِهِ إِلَّا قَلِيلًا مِّمَّا تَأْكُلُونَ ۝٤٧
Qaala tazra`oona sab`a sineena da aban famaa basattum fazaroohu fee sumbu liheee illaa qaleelam mimmaa taakuloon
📖 Tekkim Wolof
Mu ne : “Nangeen bey juróom-ñaari at ni ngeen ko baaxoo defe. Te lu ngeen góob, bàyyileen ko ca aw gubam [bañ koo bàcc], lu dul lu néew ca la ngeen di lekk.

🎧 Dégg


📜 Aaya 45-49 — Simoore Yusuf

45وَقَالَ الَّذِي نَجَا مِنْهُمَا وَادَّكَرَ بَعْدَ أُمَّةٍ أَنَا أُنَبِّئُكُم بِتَأْوِيلِهِ فَأَرْسِلُونِ
Ka muccoon ca ñoom daldi fàttaliku ginnaaw ab diir, daldi wax ne : “Danaa leen leeralal. Yebal-leen ma, Dinaa leen indil am pireem”.
46يُوسُفُ أَيُّهَا الصِّدِّيقُ أَفْتِنَا فِي سَبْعِ بَقَرَاتٍ سِمَانٍ يَأْكُلُهُنَّ سَبْعٌ عِجَافٌ وَسَبْعِ سُنبُلَاتٍ خُضْرٍ وَأُخَرَ يَابِسَاتٍ لَّعَلِّي أَرْجِعُ إِلَى النَّاسِ لَعَلَّهُمْ يَعْلَمُونَ
[Mu dem ca Yuusufa] ne ko : “Yaw waxkatu dëgg ! Ubbee ma ci juróom-ñaari nag yu duuf yu juróom-ñaari nag yu loof di lekk, ak juróom-ñaari gub yu nëtëx ak yeneen yu wow, ndax xéy-na su ma delluwaatee nit ña am ci xam-xam”.
47قَالَ تَزْرَعُونَ سَبْعَ سِنِينَ دَأَبًا فَمَا حَصَدتُّمْ فَذَرُوهُ فِي سُنبُلِهِ إِلَّا قَلِيلًا مِّمَّا تَأْكُلُونَ
Mu ne : “Nangeen bey juróom-ñaari at ni ngeen ko baaxoo defe. Te lu ngeen góob, bàyyileen ko ca aw gubam [bañ koo bàcc], lu dul lu néew ca la ngeen di lekk.
48ثُمَّ يَأْتِي مِن بَعْدِ ذَٰلِكَ سَبْعٌ شِدَادٌ يَأْكُلْنَ مَا قَدَّمْتُمْ لَهُنَّ إِلَّا قَلِيلًا مِّمَّا تُحْصِنُونَ
Dana ca topp gannaaw loolu juróom-ñaari at yu bekkoor yuy lekk la ngeen dencoon ngir ñoom ba mu des lu néew ca la ngeen dencoon.
49ثُمَّ يَأْتِي مِن بَعْدِ ذَٰلِكَ عَامٌ فِيهِ يُغَاثُ النَّاسُ وَفِيهِ يَعْصِرُونَ
Dana ca topp gannaaw loolu at moo xam ne dana xettali nit ñi te it danañu ca nal [reseñ ndax dana am].”
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
47Aaya

Tekki — Yusuf 47

Simoore Yusuf Aaya 47 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne : “Nangeen bey juróom-ñaari at ni ngeen ko…

Simoore Aaya 47/111 — Simoore Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yusuf Dégg, Simoore Yusuf Tekki, Simoore Yusuf mp3, Simoore Yusuf pdf. Aaya 45–49. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers