Ibrahima · 45/52
Tekki Waxtaan — Simoore Ibrahima
وَسَكَنتُمْ فِي مَسَاكِنِ الَّذِينَ ظَلَمُوا أَنفُسَهُمْ وَتَبَيَّنَ لَكُمْ كَيْفَ فَعَلْنَا بِهِمْ وَضَرَبْنَا لَكُمُ الْأَمْثَالَ ٤٥
Transliteration
Wa sakantum fee masaakinil lazeena zalamooo anfusahum wa tabaiyana lakum kaifa fa`alnaa bihim wa darabnaa lakumul amsaal
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ngeen dëkk ci dëkki ña tooñoon seen bopp. Te ngeen xamoon xéll na Nu defoon ak ñoom te joxoon Nanu leen ay tegtal.
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 43-47 — Simoore Ibrahima
43مُهْطِعِينَ مُقْنِعِي رُءُوسِهِمْ لَا يَرْتَدُّ إِلَيْهِمْ طَرْفُهُمْ ۖ وَأَفْئِدَتُهُمْ هَوَاءٌ
Ñuy daw, muur seeni bopp [ngir kersa], ne muq di xoole te dara nekkul ca seen xol ya [lu dul njàqare].
44وَأَنذِرِ النَّاسَ يَوْمَ يَأْتِيهِمُ الْعَذَابُ فَيَقُولُ الَّذِينَ ظَلَمُوا رَبَّنَا أَخِّرْنَا إِلَىٰ أَجَلٍ قَرِيبٍ نُّجِبْ دَعْوَتَكَ وَنَتَّبِعِ الرُّسُلَ ۗ أَوَلَمْ تَكُونُوا أَقْسَمْتُم مِّن قَبْلُ مَا لَكُم مِّن زَوَالٍ
Waaral nit ñi ci bis bu ñu leen di indil mbugal mi, ba tooñkat ya di wax naan : “Sunu Boroom, tee nga noo muñal diir bu gàtt, kon dey nu wuyusi woote, topp itam say Yonent”. - Mu tontu leen ne: “Ndax daawuleen giñ ne àllaaxira amul ?”.
45وَسَكَنتُمْ فِي مَسَاكِنِ الَّذِينَ ظَلَمُوا أَنفُسَهُمْ وَتَبَيَّنَ لَكُمْ كَيْفَ فَعَلْنَا بِهِمْ وَضَرَبْنَا لَكُمُ الْأَمْثَالَ
Ngeen dëkk ci dëkki ña tooñoon seen bopp. Te ngeen xamoon xéll na Nu defoon ak ñoom te joxoon Nanu leen ay tegtal.
46وَقَدْ مَكَرُوا مَكْرَهُمْ وَعِندَ اللَّهِ مَكْرُهُمْ وَإِن كَانَ مَكْرُهُمْ لِتَزُولَ مِنْهُ الْجِبَالُ
Dañoo fexe seen pexe te umpul Yàlla. Doonte la sax, seen pexe moomu mën naa dindi tundi doj yi...
47فَلَا تَحْسَبَنَّ اللَّهَ مُخْلِفَ وَعْدِهِ رُسُلَهُ ۗ إِنَّ اللَّهَ عَزِيزٌ ذُو انتِقَامٍ
Bul njort ne Yàlla dana soppi la Mu dig ay Yonentam. Yàlla ku am kàttan la, di Kuy feyu [tooñeel],
IbrahimaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
45Aaya
Tekki — Ibrahima 45
Simoore Ibrahima Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ngeen dëkk ci dëkki ña tooñoon seen bopp. Te ngeen…Simoore Aaya 45/52 — Simoore Ibrahima إبراهيم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ibrahima Dégg, Simoore Ibrahima Tekki, Simoore Ibrahima mp3, Simoore Ibrahima pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Ibrahima
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Thursday, October 1, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


