Ibrahima · 46/52
Tekki Waxtaan — Ibrahima
وَقَدْ مَكَرُوا مَكْرَهُمْ وَعِندَ اللَّهِ مَكْرُهُمْ وَإِن كَانَ مَكْرُهُمْ لِتَزُولَ مِنْهُ الْجِبَالُ ۝٤٦
Wa qad makaroo makrahum wa `indal laahi makruhum wa in kaana makruhum litazoola minhul jibaal
📖 Tekkim Wolof
Dañoo fexe seen pexe te umpul Yàlla. Doonte la sax, seen pexe moomu mën naa dindi tundi doj yi...

🎧 Dégg


📜 Aaya 44-48 — Ibrahima

44وَأَنذِرِ النَّاسَ يَوْمَ يَأْتِيهِمُ الْعَذَابُ فَيَقُولُ الَّذِينَ ظَلَمُوا رَبَّنَا أَخِّرْنَا إِلَىٰ أَجَلٍ قَرِيبٍ نُّجِبْ دَعْوَتَكَ وَنَتَّبِعِ الرُّسُلَ ۗ أَوَلَمْ تَكُونُوا أَقْسَمْتُم مِّن قَبْلُ مَا لَكُم مِّن زَوَالٍ
Waaral nit ñi ci bis bu ñu leen di indil mbugal mi, ba tooñkat ya di wax naan : “Sunu Boroom, tee nga noo muñal diir bu gàtt, kon dey nu wuyusi woote, topp itam say Yonent”. - Mu tontu leen ne: “Ndax daawuleen giñ ne àllaaxira amul ?”.
45وَسَكَنتُمْ فِي مَسَاكِنِ الَّذِينَ ظَلَمُوا أَنفُسَهُمْ وَتَبَيَّنَ لَكُمْ كَيْفَ فَعَلْنَا بِهِمْ وَضَرَبْنَا لَكُمُ الْأَمْثَالَ
Ngeen dëkk ci dëkki ña tooñoon seen bopp. Te ngeen xamoon xéll na Nu defoon ak ñoom te joxoon Nanu leen ay tegtal.
46وَقَدْ مَكَرُوا مَكْرَهُمْ وَعِندَ اللَّهِ مَكْرُهُمْ وَإِن كَانَ مَكْرُهُمْ لِتَزُولَ مِنْهُ الْجِبَالُ
Dañoo fexe seen pexe te umpul Yàlla. Doonte la sax, seen pexe moomu mën naa dindi tundi doj yi...
47فَلَا تَحْسَبَنَّ اللَّهَ مُخْلِفَ وَعْدِهِ رُسُلَهُ ۗ إِنَّ اللَّهَ عَزِيزٌ ذُو انتِقَامٍ
Bul njort ne Yàlla dana soppi la Mu dig ay Yonentam. Yàlla ku am kàttan la, di Kuy feyu [tooñeel],
48يَوْمَ تُبَدَّلُ الْأَرْضُ غَيْرَ الْأَرْضِ وَالسَّمَاوَاتُ ۖ وَبَرَزُوا لِلَّهِ الْوَاحِدِ الْقَهَّارِ
ba bis ba ñuy weccee suuf sii seneen suuf ak asamaan yi itam te nit ñi génne [ca seeni bàmmeel] teew ca Yàlla ja di jenn, te di Notaakoon ba.
IbrahimaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
46Aaya

Tekki — Ibrahima 46

Simoore Ibrahima Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dañoo fexe seen pexe te umpul Yàlla. Doonte la sax,…

Simoore Aaya 46/52 — Ibrahima إبراهيم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ibrahima Dégg, Ibrahima Tekki, Ibrahima mp3, Ibrahima pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers