Al-Isra · 16/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَإِذَا أَرَدْنَا أَن نُّهْلِكَ قَرْيَةً أَمَرْنَا مُتْرَفِيهَا فَفَسَقُوا فِيهَا فَحَقَّ عَلَيْهَا الْقَوْلُ فَدَمَّرْنَاهَا تَدْمِيرًا ١٦
Transliteration
Wa izaaa aradnaaa an nuhlika qaryatan amarnaa mutrafeehaa fafasaqoo feehaa fahaqqa `alaihal qawlu fadammarnaahaa tadmeeraa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Bu Nu nammee alag ab dëkk, dafay fekk ne boroom alal ya dañoo jubadi ca dëkk ba. Àtte ba daldi yell ca ñoom. Nu sadd leen sadd gu tar.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 14-18 — Al-Isra
14اقْرَأْ كِتَابَكَ كَفَىٰ بِنَفْسِكَ الْيَوْمَ عَلَيْكَ حَسِيبًا
[Nu ne ko] : “Jàngal sab téere. Sa bopp doy na la tey, sa nattub jëf yaw la war”.
15مَّنِ اهْتَدَىٰ فَإِنَّمَا يَهْتَدِي لِنَفْسِهِ ۖ وَمَن ضَلَّ فَإِنَّمَا يَضِلُّ عَلَيْهَا ۚ وَلَا تَزِرُ وَازِرَةٌ وِزْرَ أُخْرَىٰ ۗ وَمَا كُنَّا مُعَذِّبِينَ حَتَّىٰ نَبْعَثَ رَسُولًا
Ku jub, boppam la ko defal ; ku dëng boppam la ko def. Ndax kenn du yenu yenu keneen. Te nekkunu woon di Aji-mbugal wenn xeet te yónniwunu ab Yonent ca ñoom.
16وَإِذَا أَرَدْنَا أَن نُّهْلِكَ قَرْيَةً أَمَرْنَا مُتْرَفِيهَا فَفَسَقُوا فِيهَا فَحَقَّ عَلَيْهَا الْقَوْلُ فَدَمَّرْنَاهَا تَدْمِيرًا
Bu Nu nammee alag ab dëkk, dafay fekk ne boroom alal ya dañoo jubadi ca dëkk ba. Àtte ba daldi yell ca ñoom. Nu sadd leen sadd gu tar.
17وَكَمْ أَهْلَكْنَا مِنَ الْقُرُونِ مِن بَعْدِ نُوحٍ ۗ وَكَفَىٰ بِرَبِّكَ بِذُنُوبِ عِبَادِهِ خَبِيرًا بَصِيرًا
Aka bari xeet yu Nu alag ginnaaw Nooh ! Te sa Boroom kuy gis la te xam bàkkaari jaam ñi.
18مَّن كَانَ يُرِيدُ الْعَاجِلَةَ عَجَّلْنَا لَهُ فِيهَا مَا نَشَاءُ لِمَن نُّرِيدُ ثُمَّ جَعَلْنَا لَهُ جَهَنَّمَ يَصْلَاهَا مَذْمُومًا مَّدْحُورًا
Képp ku bëggul lu dul teraangay àddina, Dananu gaaw ci jox ko la Nu neex ; ca ku Nu neex. Topp Nu def Safara fa muy séndalu, di ku ñu xas, ku ñu génne [ci yërmaandey Yàlla].
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
16Aaya
Tekki — Al-Isra 16
Simoore Al-Isra Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu Nu nammee alag ab dëkk, dafay fekk ne boroom…Simoore Aaya 16/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








