Al-Kahf · 39/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
وَلَوْلَا إِذْ دَخَلْتَ جَنَّتَكَ قُلْتَ مَا شَاءَ اللَّهُ لَا قُوَّةَ إِلَّا بِاللَّهِ ۚ إِن تَرَنِ أَنَا أَقَلَّ مِنكَ مَالًا وَوَلَدًا ٣٩
Transliteration
Wa law laaa iz dakhalta jannataka qulta maa shaaa`al laahu laa quwwata illaa billaah; in tarani ana aqalla minka maalanw wa waladaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Lu teewoon ba ngay dugg ca tool ba nga wax ne : “Lu neex Yàlla [rekk ay am] ! Amul kenn ku am kàttan ku dul Yàlla”. Ndeem danga maa gis ma gën laa néew alal ak i doom,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 37-41 — Al-Kahf
37قَالَ لَهُ صَاحِبُهُ وَهُوَ يُحَاوِرُهُ أَكَفَرْتَ بِالَّذِي خَلَقَكَ مِن تُرَابٍ ثُمَّ مِن نُّطْفَةٍ ثُمَّ سَوَّاكَ رَجُلًا
Moroom ma wax ak moom, tontu ko ne ko : “Moo ndax dangaa weddi Ki la binde ci suuf, topp ci toqit [gu jóge ci góor], topp Mu melal la nga di góor gu mat sëkk ?
38لَّٰكِنَّا هُوَ اللَّهُ رَبِّي وَلَا أُشْرِكُ بِرَبِّي أَحَدًا
Waaye man, Moom Yàlla moo di sama Boroom ; te duma bokkaaleek sama Boroom kenn ?
39وَلَوْلَا إِذْ دَخَلْتَ جَنَّتَكَ قُلْتَ مَا شَاءَ اللَّهُ لَا قُوَّةَ إِلَّا بِاللَّهِ ۚ إِن تَرَنِ أَنَا أَقَلَّ مِنكَ مَالًا وَوَلَدًا
Lu teewoon ba ngay dugg ca tool ba nga wax ne : “Lu neex Yàlla [rekk ay am] ! Amul kenn ku am kàttan ku dul Yàlla”. Ndeem danga maa gis ma gën laa néew alal ak i doom,
40فَعَسَىٰ رَبِّي أَن يُؤْتِيَنِ خَيْرًا مِّن جَنَّتِكَ وَيُرْسِلَ عَلَيْهَا حُسْبَانًا مِّنَ السَّمَاءِ فَتُصْبِحَ صَعِيدًا زَلَقًا
xéy-na sama Boroom jox ma lu gën sa tool, te yabal ca sa tool jéyya ju jóge asamaan ba mu nekk dénd bu amutul dara,
41أَوْ يُصْبِحَ مَاؤُهَا غَوْرًا فَلَن تَسْتَطِيعَ لَهُ طَلَبًا
walla ndox ma ŋiis te dootu ko ame feneen”.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
39Aaya
Tekki — Al-Kahf 39
Simoore Al-Kahf Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lu teewoon ba ngay dugg ca tool ba nga wax…Simoore Aaya 39/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








