Al-Kahf · 72/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
قَالَ أَلَمْ أَقُلْ إِنَّكَ لَن تَسْتَطِيعَ مَعِيَ صَبْرًا ۝٧٢
Qaala alam aqul innaka lan tastatee`a ma`iya sabraa
📖 Tekkim Wolof
Mu ne ko : “Ndax waxuma la woon ne doo mën a ànd ak man ci sag muñ ? ”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 70-74 — Al-Kahf

70قَالَ فَإِنِ اتَّبَعْتَنِي فَلَا تَسْأَلْنِي عَن شَيْءٍ حَتَّىٰ أُحْدِثَ لَكَ مِنْهُ ذِكْرًا
Mu ne ko : “Boo ma toppee, bul ma laaj ci dara, ba kerook ma la ciy niital dara”.
71فَانطَلَقَا حَتَّىٰ إِذَا رَكِبَا فِي السَّفِينَةِ خَرَقَهَا ۖ قَالَ أَخَرَقْتَهَا لِتُغْرِقَ أَهْلَهَا لَقَدْ جِئْتَ شَيْئًا إِمْرًا
Ñu ànd ñoom ñaar. Ba ñu duggee ci genn gaal, mu xar gaal ga. Muusaa ne ko : “Ndax danga koy xar ngir labal ña ca nekk ? Def nga jëf ju siibu ! ”.
72قَالَ أَلَمْ أَقُلْ إِنَّكَ لَن تَسْتَطِيعَ مَعِيَ صَبْرًا
Mu ne ko : “Ndax waxuma la woon ne doo mën a ànd ak man ci sag muñ ? ”.
73قَالَ لَا تُؤَاخِذْنِي بِمَا نَسِيتُ وَلَا تُرْهِقْنِي مِنْ أَمْرِي عُسْرًا
Mu ne ko : “Bul ma jàppe ci lu ma fàtte ; te it bul ma togg-jëf ci sama mbir”.
74فَانطَلَقَا حَتَّىٰ إِذَا لَقِيَا غُلَامًا فَقَتَلَهُ قَالَ أَقَتَلْتَ نَفْسًا زَكِيَّةً بِغَيْرِ نَفْسٍ لَّقَدْ جِئْتَ شَيْئًا نُّكْرًا
Ñu demaat ba dajeek benn xale, mu rey ko. Muusaa ne ko : “Ndax dangay rey bakkan bu sell bu reyul bakkan ? Def nga jëf ju yéeme ! ”
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
72Aaya

Tekki — Al-Kahf 72

Simoore Al-Kahf Aaya 72 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne ko : “Ndax waxuma la woon ne doo…

Simoore Aaya 72/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 70–74. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers