Al-Baqara · 16/286
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Baqara
أُولَٰئِكَ الَّذِينَ اشْتَرَوُا الضَّلَالَةَ بِالْهُدَىٰ فَمَا رَبِحَت تِّجَارَتُهُمْ وَمَا كَانُوا مُهْتَدِينَ ۝١٦
Ulaaa`ikal lazeenash tara wud dalaalata bilhudaa famaa rabihat tijaaratuhum wa maa kaanoo muhtadeen
📖 Tekkim Wolof
Ñooña ñoo di ña jaay njub jënde ci réer, seen njaay mooma amul tono. Te it gindikuwuñu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 14-18 — Simoore Al-Baqara

14وَإِذَا لَقُوا الَّذِينَ آمَنُوا قَالُوا آمَنَّا وَإِذَا خَلَوْا إِلَىٰ شَيَاطِينِهِمْ قَالُوا إِنَّا مَعَكُمْ إِنَّمَا نَحْنُ مُسْتَهْزِئُونَ
Bu ñu dajeek way-gëm ña, ne : “Gëm nanu” ; waaye bu ñu wéetee ak seeni (Séytaane naaféq yi), ne : “Nook yéen a ànd ; nun danuy yejji [jullit ñi] rekk”.
15اللَّهُ يَسْتَهْزِئُ بِهِمْ وَيَمُدُّهُمْ فِي طُغْيَانِهِمْ يَعْمَهُونَ
Yàllaa nga leen di yejji, di leen gën a yàggal ca seen mbeewte googu, ñuy deŋŋi-deŋŋi ak seen ngumbaag xol.
16أُولَٰئِكَ الَّذِينَ اشْتَرَوُا الضَّلَالَةَ بِالْهُدَىٰ فَمَا رَبِحَت تِّجَارَتُهُمْ وَمَا كَانُوا مُهْتَدِينَ
Ñooña ñoo di ña jaay njub jënde ci réer, seen njaay mooma amul tono. Te it gindikuwuñu.
17مَثَلُهُمْ كَمَثَلِ الَّذِي اسْتَوْقَدَ نَارًا فَلَمَّا أَضَاءَتْ مَا حَوْلَهُ ذَهَبَ اللَّهُ بِنُورِهِمْ وَتَرَكَهُمْ فِي ظُلُمَاتٍ لَّا يُبْصِرُونَ
Seen niróole mi ngi demee ni ku taal taalamn, ba janeer ba leeraale la ko wër, Yàlla fay leer ga, bàyyi leen cig lëndëm ba gisatuñu dara.
18صُمٌّ بُكْمٌ عُمْيٌ فَهُمْ لَا يَرْجِعُونَ
Dañoo tëx, luu, gumba, ba duñu mën a dellusi (cig njub).
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-Baqara 16

Simoore Al-Baqara Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñooña ñoo di ña jaay njub jënde ci réer, seen…

Simoore Aaya 16/286 — Simoore Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Baqara Dégg, Simoore Al-Baqara Tekki, Simoore Al-Baqara mp3, Simoore Al-Baqara pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers