Al-Baqara · 15/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
اللَّهُ يَسْتَهْزِئُ بِهِمْ وَيَمُدُّهُمْ فِي طُغْيَانِهِمْ يَعْمَهُونَ ۝١٥
Allahu yastahzi`u bihim wa yamudduhum fee tughyaanihim ya`mahoon
📖 Tekkim Wolof
Yàllaa nga leen di yejji, di leen gën a yàggal ca seen mbeewte googu, ñuy deŋŋi-deŋŋi ak seen ngumbaag xol.
🎧 Dégg

📜 Aaya 13-17 — Al-Baqara

13وَإِذَا قِيلَ لَهُمْ آمِنُوا كَمَا آمَنَ النَّاسُ قَالُوا أَنُؤْمِنُ كَمَا آمَنَ السُّفَهَاءُ ۗ أَلَا إِنَّهُمْ هُمُ السُّفَهَاءُ وَلَٰكِن لَّا يَعْلَمُونَ
Bu ñu ne leen : “Gëmleen ni nit ñi gëmee”, ñu tontu ne : “Ndax danuy gëm ni dof yi di gëmee ? ” Déedéet, ñoom ñooy diy dof, te xamuñu ko.
14وَإِذَا لَقُوا الَّذِينَ آمَنُوا قَالُوا آمَنَّا وَإِذَا خَلَوْا إِلَىٰ شَيَاطِينِهِمْ قَالُوا إِنَّا مَعَكُمْ إِنَّمَا نَحْنُ مُسْتَهْزِئُونَ
Bu ñu dajeek way-gëm ña, ne : “Gëm nanu” ; waaye bu ñu wéetee ak seeni (Séytaane naaféq yi), ne : “Nook yéen a ànd ; nun danuy yejji [jullit ñi] rekk”.
15اللَّهُ يَسْتَهْزِئُ بِهِمْ وَيَمُدُّهُمْ فِي طُغْيَانِهِمْ يَعْمَهُونَ
Yàllaa nga leen di yejji, di leen gën a yàggal ca seen mbeewte googu, ñuy deŋŋi-deŋŋi ak seen ngumbaag xol.
16أُولَٰئِكَ الَّذِينَ اشْتَرَوُا الضَّلَالَةَ بِالْهُدَىٰ فَمَا رَبِحَت تِّجَارَتُهُمْ وَمَا كَانُوا مُهْتَدِينَ
Ñooña ñoo di ña jaay njub jënde ci réer, seen njaay mooma amul tono. Te it gindikuwuñu.
17مَثَلُهُمْ كَمَثَلِ الَّذِي اسْتَوْقَدَ نَارًا فَلَمَّا أَضَاءَتْ مَا حَوْلَهُ ذَهَبَ اللَّهُ بِنُورِهِمْ وَتَرَكَهُمْ فِي ظُلُمَاتٍ لَّا يُبْصِرُونَ
Seen niróole mi ngi demee ni ku taal taalamn, ba janeer ba leeraale la ko wër, Yàlla fay leer ga, bàyyi leen cig lëndëm ba gisatuñu dara.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
15Aaya

Tekki — Al-Baqara 15

Simoore Al-Baqara Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàllaa nga leen di yejji, di leen gën a yàggal…

Simoore Aaya 15/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers