Al-Baqara · 208/286
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Baqara
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا ادْخُلُوا فِي السِّلْمِ كَافَّةً وَلَا تَتَّبِعُوا خُطُوَاتِ الشَّيْطَانِ ۚ إِنَّهُ لَكُمْ عَدُوٌّ مُّبِينٌ ۝٢٠٨
Yaaa ayyuhal lazeena aamanud khuloo fis silmi kaaaffatanw wa laa tattabi`oo khutuwaatish Shaitaan; innahoo lakum `aduwwum mubeen
📖 Tekkim Wolof
Éy yéen ñi gëm ! Dugguleen yéen ñépp ci jàmm ji [Islaam], te buleen topp yoonu [Séytaane], moom seenub noon la bu bir.

🎧 Dégg


📜 Aaya 206-210 — Simoore Al-Baqara

206وَإِذَا قِيلَ لَهُ اتَّقِ اللَّهَ أَخَذَتْهُ الْعِزَّةُ بِالْإِثْمِ ۚ فَحَسْبُهُ جَهَنَّمُ ۚ وَلَبِئْسَ الْمِهَادُ
Te Bu ñu ko nee : “Ragalal Yàlla”, mu jomlu sax ci bàkkaar rekk, Safara dana ko doy ag pey, te bon na, lal ba ko fay xaar !
207وَمِنَ النَّاسِ مَن يَشْرِي نَفْسَهُ ابْتِغَاءَ مَرْضَاتِ اللَّهِ ۗ وَاللَّهُ رَءُوفٌ بِالْعِبَادِ
Am na ci nit ñi ñuy jaay seen bakkan ngir sàkku ngërëmul Yàlla. Yàlla dey Aji-ñeewant la ci jaamam ñi.
208يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا ادْخُلُوا فِي السِّلْمِ كَافَّةً وَلَا تَتَّبِعُوا خُطُوَاتِ الشَّيْطَانِ ۚ إِنَّهُ لَكُمْ عَدُوٌّ مُّبِينٌ
Éy yéen ñi gëm ! Dugguleen yéen ñépp ci jàmm ji [Islaam], te buleen topp yoonu [Séytaane], moom seenub noon la bu bir.
209فَإِن زَلَلْتُم مِّن بَعْدِ مَا جَاءَتْكُمُ الْبَيِّنَاتُ فَاعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ عَزِيزٌ حَكِيمٌ
Bu ngeen tarxiisee, ginnaaw ba ngeen amee faramfàcce gu leer nàññ, xamleen ne Yàlla ku màgg kàttan la te ku xereñ la.
210هَلْ يَنظُرُونَ إِلَّا أَن يَأْتِيَهُمُ اللَّهُ فِي ظُلَلٍ مِّنَ الْغَمَامِ وَالْمَلَائِكَةُ وَقُضِيَ الْأَمْرُ ۚ وَإِلَى اللَّهِ تُرْجَعُ الْأُمُورُ
Moo ndax dañuy xaar ba Yàlla dikkal leen [ak mbugal] ci keri niir yi ak Malaaka yi, fekk àtteef na mbir ya ba noppi ? Te mbir yépp ca Yàlla lañuy dellu.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
208Aaya

Tekki — Al-Baqara 208

Simoore Al-Baqara Aaya 208 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Éy yéen ñi gëm ! Dugguleen yéen ñépp ci jàmm…

Simoore Aaya 208/286 — Simoore Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Baqara Dégg, Simoore Al-Baqara Tekki, Simoore Al-Baqara mp3, Simoore Al-Baqara pdf. Aaya 206–210. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers