Al-Baqara · 209/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
فَإِن زَلَلْتُم مِّن بَعْدِ مَا جَاءَتْكُمُ الْبَيِّنَاتُ فَاعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ عَزِيزٌ حَكِيمٌ ٢٠٩
Transliteration
Fa in zalaltum mimba`di maa jaaa`atkumul baiyinaatu fa`lamoo annallaaha `Azeezun hakeem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Bu ngeen tarxiisee, ginnaaw ba ngeen amee faramfàcce gu leer nàññ, xamleen ne Yàlla ku màgg kàttan la te ku xereñ la.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 207-211 — Al-Baqara
207وَمِنَ النَّاسِ مَن يَشْرِي نَفْسَهُ ابْتِغَاءَ مَرْضَاتِ اللَّهِ ۗ وَاللَّهُ رَءُوفٌ بِالْعِبَادِ
Am na ci nit ñi ñuy jaay seen bakkan ngir sàkku ngërëmul Yàlla. Yàlla dey Aji-ñeewant la ci jaamam ñi.
208يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا ادْخُلُوا فِي السِّلْمِ كَافَّةً وَلَا تَتَّبِعُوا خُطُوَاتِ الشَّيْطَانِ ۚ إِنَّهُ لَكُمْ عَدُوٌّ مُّبِينٌ
Éy yéen ñi gëm ! Dugguleen yéen ñépp ci jàmm ji [Islaam], te buleen topp yoonu [Séytaane], moom seenub noon la bu bir.
209فَإِن زَلَلْتُم مِّن بَعْدِ مَا جَاءَتْكُمُ الْبَيِّنَاتُ فَاعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ عَزِيزٌ حَكِيمٌ
Bu ngeen tarxiisee, ginnaaw ba ngeen amee faramfàcce gu leer nàññ, xamleen ne Yàlla ku màgg kàttan la te ku xereñ la.
210هَلْ يَنظُرُونَ إِلَّا أَن يَأْتِيَهُمُ اللَّهُ فِي ظُلَلٍ مِّنَ الْغَمَامِ وَالْمَلَائِكَةُ وَقُضِيَ الْأَمْرُ ۚ وَإِلَى اللَّهِ تُرْجَعُ الْأُمُورُ
Moo ndax dañuy xaar ba Yàlla dikkal leen [ak mbugal] ci keri niir yi ak Malaaka yi, fekk àtteef na mbir ya ba noppi ? Te mbir yépp ca Yàlla lañuy dellu.
211سَلْ بَنِي إِسْرَائِيلَ كَمْ آتَيْنَاهُم مِّنْ آيَةٍ بَيِّنَةٍ ۗ وَمَن يُبَدِّلْ نِعْمَةَ اللَّهِ مِن بَعْدِ مَا جَاءَتْهُ فَإِنَّ اللَّهَ شَدِيدُ الْعِقَابِ
Laajal Banii-Israayiila ñaata yoon lañu leen indil ay kéemaan yu leer nàññ [bari na] ! Képp ku soppi xéewali Yàlla ginnaaw ba mu ko jotee... na xam ne, Yàlla ku tar mbugal la.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
209Aaya
Tekki — Al-Baqara 209
Simoore Al-Baqara Aaya 209 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ngeen tarxiisee, ginnaaw ba ngeen amee faramfàcce gu leer…Simoore Aaya 209/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 207–211. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








