Taha · 13/135
Tekki Waxtaan — Taha
وَأَنَا اخْتَرْتُكَ فَاسْتَمِعْ لِمَا يُوحَىٰ ۝١٣
Wa anakhtartuka fastami` limaa yoohaa
📖 Tekkim Wolof
Dama laa tànn. Kon déggal li Ma lay soloo.
🎧 Dégg

📜 Aaya 11-15 — Taha

11فَلَمَّا أَتَاهَا نُودِيَ يَا مُوسَىٰ
Ba mu agsee ci safara wa, mu am lu ko woo ne ko : “Éy Muusaa !
12إِنِّي أَنَا رَبُّكَ فَاخْلَعْ نَعْلَيْكَ ۖ إِنَّكَ بِالْوَادِ الْمُقَدَّسِ طُوًى
Man maay sa Boroom. Summil say dàll : yaa ngi ci biir xur wu sell wu ñuy wax [Tuwaa].
13وَأَنَا اخْتَرْتُكَ فَاسْتَمِعْ لِمَا يُوحَىٰ
Dama laa tànn. Kon déggal li Ma lay soloo.
14إِنَّنِي أَنَا اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا أَنَا فَاعْبُدْنِي وَأَقِمِ الصَّلَاةَ لِذِكْرِي
Man mii maay Yàlla : amul jeneen yàlla ju dul Man. Nanga may jaamu, tey taxawal julli, di Ma màggal.
15إِنَّ السَّاعَةَ آتِيَةٌ أَكَادُ أُخْفِيهَا لِتُجْزَىٰ كُلُّ نَفْسٍ بِمَا تَسْعَىٰ
Te Bis-pénc ba daanaka ñëw na. Dama koo xaw a làq rekk ngir fey bakkan bu nekk la muy jëf.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
13Aaya

Tekki — Taha 13

Simoore Taha Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dama laa tànn. Kon déggal li Ma lay soloo.

Simoore Aaya 13/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers