Taha · 12/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
إِنِّي أَنَا رَبُّكَ فَاخْلَعْ نَعْلَيْكَ ۖ إِنَّكَ بِالْوَادِ الْمُقَدَّسِ طُوًى ۝١٢
Inneee Ana Rabbuka fakhla` na`laika innaka bilwaadil muqaddasi Tuwaa
📖 Tekkim Wolof
Man maay sa Boroom. Summil say dàll : yaa ngi ci biir xur wu sell wu ñuy wax [Tuwaa].

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 10-14 — Simoore Taha

10إِذْ رَأَىٰ نَارًا فَقَالَ لِأَهْلِهِ امْكُثُوا إِنِّي آنَسْتُ نَارًا لَّعَلِّي آتِيكُم مِّنْهَا بِقَبَسٍ أَوْ أَجِدُ عَلَى النَّارِ هُدًى
Ba mu gisee aw safara, mu ne njabootam : “Xaarleen ma fii ! Lële ma séen dey aw safara la ; Amaana ma jële fa aw xal, walla ma fekk fa ku ma gindi [teg ma ci yoon]”.
11فَلَمَّا أَتَاهَا نُودِيَ يَا مُوسَىٰ
Ba mu agsee ci safara wa, mu am lu ko woo ne ko : “Éy Muusaa !
12إِنِّي أَنَا رَبُّكَ فَاخْلَعْ نَعْلَيْكَ ۖ إِنَّكَ بِالْوَادِ الْمُقَدَّسِ طُوًى
Man maay sa Boroom. Summil say dàll : yaa ngi ci biir xur wu sell wu ñuy wax [Tuwaa].
13وَأَنَا اخْتَرْتُكَ فَاسْتَمِعْ لِمَا يُوحَىٰ
Dama laa tànn. Kon déggal li Ma lay soloo.
14إِنَّنِي أَنَا اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا أَنَا فَاعْبُدْنِي وَأَقِمِ الصَّلَاةَ لِذِكْرِي
Man mii maay Yàlla : amul jeneen yàlla ju dul Man. Nanga may jaamu, tey taxawal julli, di Ma màggal.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Taha 12

Simoore Taha Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Man maay sa Boroom. Summil say dàll : yaa ngi…

Simoore Aaya 12/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers