Taha · 14/135
Tekki Waxtaan — Taha
إِنَّنِي أَنَا اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا أَنَا فَاعْبُدْنِي وَأَقِمِ الصَّلَاةَ لِذِكْرِي ۝١٤
Innaneee Anal laahu laaa ilaaha illaa Ana fa`budnee wa aqimis-salaata lizikree
📖 Tekkim Wolof
Man mii maay Yàlla : amul jeneen yàlla ju dul Man. Nanga may jaamu, tey taxawal julli, di Ma màggal.

🎧 Dégg


📜 Aaya 12-16 — Taha

12إِنِّي أَنَا رَبُّكَ فَاخْلَعْ نَعْلَيْكَ ۖ إِنَّكَ بِالْوَادِ الْمُقَدَّسِ طُوًى
Man maay sa Boroom. Summil say dàll : yaa ngi ci biir xur wu sell wu ñuy wax [Tuwaa].
13وَأَنَا اخْتَرْتُكَ فَاسْتَمِعْ لِمَا يُوحَىٰ
Dama laa tànn. Kon déggal li Ma lay soloo.
14إِنَّنِي أَنَا اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا أَنَا فَاعْبُدْنِي وَأَقِمِ الصَّلَاةَ لِذِكْرِي
Man mii maay Yàlla : amul jeneen yàlla ju dul Man. Nanga may jaamu, tey taxawal julli, di Ma màggal.
15إِنَّ السَّاعَةَ آتِيَةٌ أَكَادُ أُخْفِيهَا لِتُجْزَىٰ كُلُّ نَفْسٍ بِمَا تَسْعَىٰ
Te Bis-pénc ba daanaka ñëw na. Dama koo xaw a làq rekk ngir fey bakkan bu nekk la muy jëf.
16فَلَا يَصُدَّنَّكَ عَنْهَا مَن لَّا يُؤْمِنُ بِهَا وَاتَّبَعَ هَوَاهُ فَتَرْدَىٰ
[Kon farlul ba] képp ku gëmul tey topp bànneexam, bañ laa gàllankoor ngay alku.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Taha 14

Simoore Taha Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Man mii maay Yàlla : amul jeneen yàlla ju dul…

Simoore Aaya 14/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers