Taha · 28/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
يَفْقَهُوا قَوْلِي ۝٢٨
Yafqahoo qawlee
📖 Tekkim Wolof
ba ñu mën a xam samay wax,

🎧 Dégg


📜 Aaya 26-30 — Simoore Taha

26وَيَسِّرْ لِي أَمْرِي
te nga yombalal ma sama soloo sii,
27وَاحْلُلْ عُقْدَةً مِّن لِّسَانِي
te nga leeral samaw làmmiñ,
28يَفْقَهُوا قَوْلِي
ba ñu mën a xam samay wax,
29وَاجْعَل لِّي وَزِيرًا مِّنْ أَهْلِي
te nga may ma, defal ma ci samag njaboot ku may jàppale :
30هَارُونَ أَخِي
Te mu far doon sax Haaruuna, sama mbokk,
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — Taha 28

Simoore Taha Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ba ñu mën a xam samay wax,

Simoore Aaya 28/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers