Taha · 29/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
وَاجْعَل لِّي وَزِيرًا مِّنْ أَهْلِي ۝٢٩
Waj`al lee wazeeram min ahlee
📖 Tekkim Wolof
te nga may ma, defal ma ci samag njaboot ku may jàppale :

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 27-31 — Simoore Taha

27وَاحْلُلْ عُقْدَةً مِّن لِّسَانِي
te nga leeral samaw làmmiñ,
28يَفْقَهُوا قَوْلِي
ba ñu mën a xam samay wax,
29وَاجْعَل لِّي وَزِيرًا مِّنْ أَهْلِي
te nga may ma, defal ma ci samag njaboot ku may jàppale :
30هَارُونَ أَخِي
Te mu far doon sax Haaruuna, sama mbokk,
31اشْدُدْ بِهِ أَزْرِي
Doolel ma ci moom !
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
29Aaya

Tekki — Taha 29

Simoore Taha Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te nga may ma, defal ma ci samag njaboot ku…

Simoore Aaya 29/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 27–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers