Taha · 27/135
Tekki Waxtaan — Taha
وَاحْلُلْ عُقْدَةً مِّن لِّسَانِي ۝٢٧
Wahlul `uqdatam milli saanee
📖 Tekkim Wolof
te nga leeral samaw làmmiñ,

🎧 Dégg


📜 Aaya 25-29 — Taha

25قَالَ رَبِّ اشْرَحْ لِي صَدْرِي
[Muusaa] ne ko : “Yaw sama Boroom, leeralal ma sama dënn [mën a dékku lu bari],
26وَيَسِّرْ لِي أَمْرِي
te nga yombalal ma sama soloo sii,
27وَاحْلُلْ عُقْدَةً مِّن لِّسَانِي
te nga leeral samaw làmmiñ,
28يَفْقَهُوا قَوْلِي
ba ñu mën a xam samay wax,
29وَاجْعَل لِّي وَزِيرًا مِّنْ أَهْلِي
te nga may ma, defal ma ci samag njaboot ku may jàppale :
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — Taha 27

Simoore Taha Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te nga leeral samaw làmmiñ,

Simoore Aaya 27/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers