Al-Hajj · 1/78
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hajj
يَا أَيُّهَا النَّاسُ اتَّقُوا رَبَّكُمْ ۚ إِنَّ زَلْزَلَةَ السَّاعَةِ شَيْءٌ عَظِيمٌ ۝١
Yaaa ayyuhan naasuttaqoo Rabbakum; inna zalzalatas Saa`ati shai`un `azeem
📖 Tekkim Wolof
Éy yéen nit ñi ! Ragal-leen seen Boroom. Yëngutug Bis-pénc ba nag mbir mu rëy la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore Al-Hajj

1يَا أَيُّهَا النَّاسُ اتَّقُوا رَبَّكُمْ ۚ إِنَّ زَلْزَلَةَ السَّاعَةِ شَيْءٌ عَظِيمٌ
Éy yéen nit ñi ! Ragal-leen seen Boroom. Yëngutug Bis-pénc ba nag mbir mu rëy la.
2يَوْمَ تَرَوْنَهَا تَذْهَلُ كُلُّ مُرْضِعَةٍ عَمَّا أَرْضَعَتْ وَتَضَعُ كُلُّ ذَاتِ حَمْلٍ حَمْلَهَا وَتَرَى النَّاسَ سُكَارَىٰ وَمَا هُم بِسُكَارَىٰ وَلَٰكِنَّ عَذَابَ اللَّهِ شَدِيدٌ
Bis bu ngeen ko gisee, képp ku doon nàmpal dana fàtte la mu doon nàmpal, te ku ëmboon dana wësin la mu ëmb. Te nga gis nit ña màndi fekk màndiwuñu. Mbugalu Yàllaa tar [ci ñoom].
3وَمِنَ النَّاسِ مَن يُجَادِلُ فِي اللَّهِ بِغَيْرِ عِلْمٍ وَيَتَّبِعُ كُلَّ شَيْطَانٍ مَّرِيدٍ
Am na ci nit ñi ñuy dàggasante ci Yàlla cig ñàkk a xam ci di topp Séytaane mi féttérlu.
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
1Aaya

Tekki — Al-Hajj 1

Simoore Al-Hajj Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Éy yéen nit ñi ! Ragal-leen seen Boroom. Yëngutug Bis-pénc…

Simoore Aaya 1/78 — Simoore Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hajj Dégg, Simoore Al-Hajj Tekki, Simoore Al-Hajj mp3, Simoore Al-Hajj pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers