Al-Hajj · 2/78
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hajj
يَوْمَ تَرَوْنَهَا تَذْهَلُ كُلُّ مُرْضِعَةٍ عَمَّا أَرْضَعَتْ وَتَضَعُ كُلُّ ذَاتِ حَمْلٍ حَمْلَهَا وَتَرَى النَّاسَ سُكَارَىٰ وَمَا هُم بِسُكَارَىٰ وَلَٰكِنَّ عَذَابَ اللَّهِ شَدِيدٌ ٢
Transliteration
Yawma tarawnahaa tazhalu kullu murdi`atin `ammaaa arda`at wa tada`u kullu zaati hamlin hamlahaa wa tarannaasa sukaaraa wa maa hum bisukaaraa wa lakinaa `azaabal laahi shadeed
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Bis bu ngeen ko gisee, képp ku doon nàmpal dana fàtte la mu doon nàmpal, te ku ëmboon dana wësin la mu ëmb. Te nga gis nit ña màndi fekk màndiwuñu. Mbugalu Yàllaa tar [ci ñoom].
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 1-4 — Simoore Al-Hajj
1يَا أَيُّهَا النَّاسُ اتَّقُوا رَبَّكُمْ ۚ إِنَّ زَلْزَلَةَ السَّاعَةِ شَيْءٌ عَظِيمٌ
Éy yéen nit ñi ! Ragal-leen seen Boroom. Yëngutug Bis-pénc ba nag mbir mu rëy la.
2يَوْمَ تَرَوْنَهَا تَذْهَلُ كُلُّ مُرْضِعَةٍ عَمَّا أَرْضَعَتْ وَتَضَعُ كُلُّ ذَاتِ حَمْلٍ حَمْلَهَا وَتَرَى النَّاسَ سُكَارَىٰ وَمَا هُم بِسُكَارَىٰ وَلَٰكِنَّ عَذَابَ اللَّهِ شَدِيدٌ
Bis bu ngeen ko gisee, képp ku doon nàmpal dana fàtte la mu doon nàmpal, te ku ëmboon dana wësin la mu ëmb. Te nga gis nit ña màndi fekk màndiwuñu. Mbugalu Yàllaa tar [ci ñoom].
3وَمِنَ النَّاسِ مَن يُجَادِلُ فِي اللَّهِ بِغَيْرِ عِلْمٍ وَيَتَّبِعُ كُلَّ شَيْطَانٍ مَّرِيدٍ
Am na ci nit ñi ñuy dàggasante ci Yàlla cig ñàkk a xam ci di topp Séytaane mi féttérlu.
4كُتِبَ عَلَيْهِ أَنَّهُ مَن تَوَلَّاهُ فَأَنَّهُ يُضِلُّهُ وَيَهْدِيهِ إِلَىٰ عَذَابِ السَّعِيرِ
Te dogaleef na ca moom [Séytaane soosu] ne képp ku ko def sëriñam, dana la réeral, yóbbee la mbugalum Safara.
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
2Aaya
Tekki — Al-Hajj 2
Simoore Al-Hajj Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bis bu ngeen ko gisee, képp ku doon nàmpal dana…Simoore Aaya 2/78 — Simoore Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hajj Dégg, Simoore Al-Hajj Tekki, Simoore Al-Hajj mp3, Simoore Al-Hajj pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Al-Hajj
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Monday, September 28, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


