Al-Hajj · 51/78
Tekki Waxtaan — Al-Hajj
وَالَّذِينَ سَعَوْا فِي آيَاتِنَا مُعَاجِزِينَ أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ الْجَحِيمِ ٥١
Transliteration
Wallazeena sa`aw feee Aayaatinaa mu`aajizeena ulaaa ika As-haabul jaheem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
ña nga xam ne ñi ngi dox di yoqatloo nit ñi ci Sunuy ndigal, ñooña ñooy waa Safara.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 49-53 — Al-Hajj
49قُلْ يَا أَيُّهَا النَّاسُ إِنَّمَا أَنَا لَكُمْ نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Neel : “Éy yéen nit ñi ! Man nekkuma ci yéen lu dul ab waaraatekat bu wér”.
50فَالَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَرِزْقٌ كَرِيمٌ
Kon ña gëm tey jëf jëf ju yiw am nañu njéggal ak xéewal gu tedd,
51وَالَّذِينَ سَعَوْا فِي آيَاتِنَا مُعَاجِزِينَ أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ الْجَحِيمِ
ña nga xam ne ñi ngi dox di yoqatloo nit ñi ci Sunuy ndigal, ñooña ñooy waa Safara.
52وَمَا أَرْسَلْنَا مِن قَبْلِكَ مِن رَّسُولٍ وَلَا نَبِيٍّ إِلَّا إِذَا تَمَنَّىٰ أَلْقَى الشَّيْطَانُ فِي أُمْنِيَّتِهِ فَيَنسَخُ اللَّهُ مَا يُلْقِي الشَّيْطَانُ ثُمَّ يُحْكِمُ اللَّهُ آيَاتِهِ ۗ وَاللَّهُ عَلِيمٌ حَكِيمٌ
Mësunoo yónni ci lu jiitu ab Yonent walla ku Nu soloo te bu mébétee dara Séytaane du sànni pexe mu bon ci mébétam. Waaye Yàlla dana masaxal la Séytaane sànni woon, ba noppi dëggal ay ndigalam. Te Yàlla Ku xam la Ku xereñ la.
53لِّيَجْعَلَ مَا يُلْقِي الشَّيْطَانُ فِتْنَةً لِّلَّذِينَ فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ وَالْقَاسِيَةِ قُلُوبُهُمْ ۗ وَإِنَّ الظَّالِمِينَ لَفِي شِقَاقٍ بَعِيدٍ
Lu Séytaane sànni Dafa koo def muy nattu ca ña jàngoro nekk ca seen xol ak ña seeni xol wow... Ca tooñkat ya ñu nekk ci wuute gu sore [dëgg].
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
51Aaya
Tekki — Al-Hajj 51
Simoore Al-Hajj Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ña nga xam ne ñi ngi dox di yoqatloo nit…Simoore Aaya 51/78 — Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hajj Dégg, Al-Hajj Tekki, Al-Hajj mp3, Al-Hajj pdf. Aaya 49–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Wednesday, August 19, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








