Al-Mu'minun · 11/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
الَّذِينَ يَرِثُونَ الْفِرْدَوْسَ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ ۝١١
Allazeena yarisoonal Firdawsa hum feehaa khaalidoon
📖 Tekkim Wolof
ña nga xam ne danañu donn Àjjana Firdawsi, te dañu cay béel.

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Simoore Al-Mu'minun

9وَالَّذِينَ هُمْ عَلَىٰ صَلَوَاتِهِمْ يُحَافِظُونَ
tey wattu seeni julli [di ko sàmm].
10أُولَٰئِكَ هُمُ الْوَارِثُونَ
Ñoom dey ñooy donnkat ya,
11الَّذِينَ يَرِثُونَ الْفِرْدَوْسَ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
ña nga xam ne danañu donn Àjjana Firdawsi, te dañu cay béel.
12وَلَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ مِن سُلَالَةٍ مِّن طِينٍ
Nun bind Nanu nit [sàkk ko]mu bawoo ci cosaanul ban [suuf],
13ثُمَّ جَعَلْنَاهُ نُطْفَةً فِي قَرَارٍ مَّكِينٍ
ginnaaw ba Nu def ko mu di maniyu ma mu di aw lumbu.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 11

Simoore Al-Mu'minun Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ña nga xam ne danañu donn Àjjana Firdawsi, te dañu…

Simoore Aaya 11/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers