Al-Mu'minun · 12/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَلَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ مِن سُلَالَةٍ مِّن طِينٍ ۝١٢
Wa laqad khalaqnal insaana min sulaalatim minteen
📖 Tekkim Wolof
Nun bind Nanu nit [sàkk ko]mu bawoo ci cosaanul ban [suuf],

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Simoore Al-Mu'minun

10أُولَٰئِكَ هُمُ الْوَارِثُونَ
Ñoom dey ñooy donnkat ya,
11الَّذِينَ يَرِثُونَ الْفِرْدَوْسَ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
ña nga xam ne danañu donn Àjjana Firdawsi, te dañu cay béel.
12وَلَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ مِن سُلَالَةٍ مِّن طِينٍ
Nun bind Nanu nit [sàkk ko]mu bawoo ci cosaanul ban [suuf],
13ثُمَّ جَعَلْنَاهُ نُطْفَةً فِي قَرَارٍ مَّكِينٍ
ginnaaw ba Nu def ko mu di maniyu ma mu di aw lumbu.
14ثُمَّ خَلَقْنَا النُّطْفَةَ عَلَقَةً فَخَلَقْنَا الْعَلَقَةَ مُضْغَةً فَخَلَقْنَا الْمُضْغَةَ عِظَامًا فَكَسَوْنَا الْعِظَامَ لَحْمًا ثُمَّ أَنشَأْنَاهُ خَلْقًا آخَرَ ۚ فَتَبَارَكَ اللَّهُ أَحْسَنُ الْخَالِقِينَ
Ginnaaw ba Nu def lumbu ma di aw suux ; ginnaaw ba Nu def suux wa mu di ay yax, daldi sànge yax ya aw yàpp. Daldi koy def jëmm,Yàllaa mën a sakkanal. Moom miy gën gi Bindkat !
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 12

Simoore Al-Mu'minun Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun bind Nanu nit [sàkk ko]mu bawoo ci cosaanul ban…

Simoore Aaya 12/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers