Al-Mu'minun · 10/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
أُولَٰئِكَ هُمُ الْوَارِثُونَ ۝١٠
Ulaaa`ika humul waarisoon
📖 Tekkim Wolof
Ñoom dey ñooy donnkat ya,

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Simoore Al-Mu'minun

8وَالَّذِينَ هُمْ لِأَمَانَاتِهِمْ وَعَهْدِهِمْ رَاعُونَ
ña nga xam ne nag dañuy sàmm la ñu leen dénk ak seeni kàddu,
9وَالَّذِينَ هُمْ عَلَىٰ صَلَوَاتِهِمْ يُحَافِظُونَ
tey wattu seeni julli [di ko sàmm].
10أُولَٰئِكَ هُمُ الْوَارِثُونَ
Ñoom dey ñooy donnkat ya,
11الَّذِينَ يَرِثُونَ الْفِرْدَوْسَ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
ña nga xam ne danañu donn Àjjana Firdawsi, te dañu cay béel.
12وَلَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ مِن سُلَالَةٍ مِّن طِينٍ
Nun bind Nanu nit [sàkk ko]mu bawoo ci cosaanul ban [suuf],
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 10

Simoore Al-Mu'minun Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñoom dey ñooy donnkat ya,

Simoore Aaya 10/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers