An-Nur · 54/64
Tekki Waxtaan — An-Nur
قُلْ أَطِيعُوا اللَّهَ وَأَطِيعُوا الرَّسُولَ ۖ فَإِن تَوَلَّوْا فَإِنَّمَا عَلَيْهِ مَا حُمِّلَ وَعَلَيْكُم مَّا حُمِّلْتُمْ ۖ وَإِن تُطِيعُوهُ تَهْتَدُوا ۚ وَمَا عَلَى الرَّسُولِ إِلَّا الْبَلَاغُ الْمُبِينُ ٥٤
Transliteration
Qul atee`ul laaha wa atee`ur Rasoola fa in tawallaw fa innamaa `alaihi maa hummila wa `alaikum maa hummiltum wa in tutee`oohu tahtadoo; wa maa`alar Rasooli illal balaaghul mubeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Toppleen Yàlla te topp ab Yonentam. Bu ñu dummóoyoo [ndigal la] ñoom nag,... yéen itam ak seen mbiri bopp ; su ngen toppee [ndigal la] gindiku”. Yonent bi moom jottal rekk a ko ci war.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 52-56 — An-Nur
52وَمَن يُطِعِ اللَّهَ وَرَسُولَهُ وَيَخْشَ اللَّهَ وَيَتَّقْهِ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْفَائِزُونَ
Képp kuy topp Yàlla ak ub Yonentam, ragal Yàlla te di Ko fuglu, ñooña ñooy ña texe.
53۞ وَأَقْسَمُوا بِاللَّهِ جَهْدَ أَيْمَانِهِمْ لَئِنْ أَمَرْتَهُمْ لَيَخْرُجُنَّ ۖ قُل لَّا تُقْسِمُوا ۖ طَاعَةٌ مَّعْرُوفَةٌ ۚ إِنَّ اللَّهَ خَبِيرٌ بِمَا تَعْمَلُونَ
Danañuy giñ ci Yàlla fa mu gën a ñàngee, naan boo leen digalee danañu génn [dem xare ji]. Neel : “Buleen giñ. [Wax ji rekk doyul]. Yàlla xam na li ngeen di def”.
54قُلْ أَطِيعُوا اللَّهَ وَأَطِيعُوا الرَّسُولَ ۖ فَإِن تَوَلَّوْا فَإِنَّمَا عَلَيْهِ مَا حُمِّلَ وَعَلَيْكُم مَّا حُمِّلْتُمْ ۖ وَإِن تُطِيعُوهُ تَهْتَدُوا ۚ وَمَا عَلَى الرَّسُولِ إِلَّا الْبَلَاغُ الْمُبِينُ
Neel : “Toppleen Yàlla te topp ab Yonentam. Bu ñu dummóoyoo [ndigal la] ñoom nag,... yéen itam ak seen mbiri bopp ; su ngen toppee [ndigal la] gindiku”. Yonent bi moom jottal rekk a ko ci war.
55وَعَدَ اللَّهُ الَّذِينَ آمَنُوا مِنكُمْ وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ لَيَسْتَخْلِفَنَّهُمْ فِي الْأَرْضِ كَمَا اسْتَخْلَفَ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ وَلَيُمَكِّنَنَّ لَهُمْ دِينَهُمُ الَّذِي ارْتَضَىٰ لَهُمْ وَلَيُبَدِّلَنَّهُم مِّن بَعْدِ خَوْفِهِمْ أَمْنًا ۚ يَعْبُدُونَنِي لَا يُشْرِكُونَ بِي شَيْئًا ۚ وَمَن كَفَرَ بَعْدَ ذَٰلِكَ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْفَاسِقُونَ
Yàlla dig na ña gëm ci ñoom, tey jëf u yiw ne def na leen kuutaay ci kaw suuf kem ni Mu defe woon kuutaay ca ña leen jiitu woon. Te Dana leen yombalal jëfandikoo diiney [Islaam] ji Mu leen tànnal. Te it Dana leen soppil ginnaaw tiitaange kóolute. Ñu di Ma jaamu te duñu Ma bokkaale lenn. Képp ku weddi ginnaaw loolu, kon ñoom ñooy saay-saay sa.
56وَأَقِيمُوا الصَّلَاةَ وَآتُوا الزَّكَاةَ وَأَطِيعُوا الرَّسُولَ لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Nangeen di taxawal julli tey génne asaka, te it nangeen topp Yonent bi, ndaxtele yërëmees leen.
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
54Aaya
Tekki — An-Nur 54
Simoore An-Nur Aaya 54 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Toppleen Yàlla te topp ab Yonentam. Bu ñu…Simoore Aaya 54/64 — An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nur Dégg, An-Nur Tekki, An-Nur mp3, An-Nur pdf. Aaya 52–56. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








