An-Naml · 35/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
وَإِنِّي مُرْسِلَةٌ إِلَيْهِم بِهَدِيَّةٍ فَنَاظِرَةٌ بِمَ يَرْجِعُ الْمُرْسَلُونَ ۝٣٥
Wa innee mursilatun ilaihim bihadiyyatin fanaaziratum bima yarji`ul mursaloon
📖 Tekkim Wolof
Man, dama leen di yónnee alal [neexal], su ma ko defee nag xool lu ndaw ya di delloosi”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 33-37 — Simoore An-Naml

33قَالُوا نَحْنُ أُولُو قُوَّةٍ وَأُولُو بَأْسٍ شَدِيدٍ وَالْأَمْرُ إِلَيْكِ فَانظُرِي مَاذَا تَأْمُرِينَ
Ñu ne ko : “Nun am nañu dooleek alal te yaay digle. Seetal loo nuy digal”.
34قَالَتْ إِنَّ الْمُلُوكَ إِذَا دَخَلُوا قَرْيَةً أَفْسَدُوهَا وَجَعَلُوا أَعِزَّةَ أَهْلِهَا أَذِلَّةً ۖ وَكَذَٰلِكَ يَفْعَلُونَ
Buur ba ne leen : “Buur yi dey, bu ñu duggee cib dëkk, yàqate ko, daldi toroxal ña fa gënoon a tedd. Ñoom noonu la ñuy def.
35وَإِنِّي مُرْسِلَةٌ إِلَيْهِم بِهَدِيَّةٍ فَنَاظِرَةٌ بِمَ يَرْجِعُ الْمُرْسَلُونَ
Man, dama leen di yónnee alal [neexal], su ma ko defee nag xool lu ndaw ya di delloosi”.
36فَلَمَّا جَاءَ سُلَيْمَانَ قَالَ أَتُمِدُّونَنِ بِمَالٍ فَمَا آتَانِيَ اللَّهُ خَيْرٌ مِّمَّا آتَاكُم بَلْ أَنتُم بِهَدِيَّتِكُمْ تَفْرَحُونَ
[Ba ndaw ya àggee] ca Suleymaan, mu ne leen : “Yéen daal dangeen may jéem a gere alal ? Maa leen ko gënle fuuf. Mbaa du ! Lii doŋŋ la.
37ارْجِعْ إِلَيْهِمْ فَلَنَأْتِيَنَّهُم بِجُنُودٍ لَّا قِبَلَ لَهُم بِهَا وَلَنُخْرِجَنَّهُم مِّنْهَا أَذِلَّةً وَهُمْ صَاغِرُونَ
Dellul ca ñoom. Neleen danaa leen indil xare bu ñu dul mën a dékku. Te danaa leen fa génne toroxal leen ba ñu ne tott.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
35Aaya

Tekki — An-Naml 35

Simoore An-Naml Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Man, dama leen di yónnee alal [neexal], su ma ko…

Simoore Aaya 35/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 33–37. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers