An-Naml · 36/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
فَلَمَّا جَاءَ سُلَيْمَانَ قَالَ أَتُمِدُّونَنِ بِمَالٍ فَمَا آتَانِيَ اللَّهُ خَيْرٌ مِّمَّا آتَاكُم بَلْ أَنتُم بِهَدِيَّتِكُمْ تَفْرَحُونَ ۝٣٦
Falammaa jaaa`a Sulaimaana qaala atumiddoonani bimaalin famaaa aataakum bal antum bihadiy yatikum tafrahoon
📖 Tekkim Wolof
[Ba ndaw ya àggee] ca Suleymaan, mu ne leen : “Yéen daal dangeen may jéem a gere alal ? Maa leen ko gënle fuuf. Mbaa du ! Lii doŋŋ la.
🎧 Dégg

📜 Aaya 34-38 — An-Naml

34قَالَتْ إِنَّ الْمُلُوكَ إِذَا دَخَلُوا قَرْيَةً أَفْسَدُوهَا وَجَعَلُوا أَعِزَّةَ أَهْلِهَا أَذِلَّةً ۖ وَكَذَٰلِكَ يَفْعَلُونَ
Buur ba ne leen : “Buur yi dey, bu ñu duggee cib dëkk, yàqate ko, daldi toroxal ña fa gënoon a tedd. Ñoom noonu la ñuy def.
35وَإِنِّي مُرْسِلَةٌ إِلَيْهِم بِهَدِيَّةٍ فَنَاظِرَةٌ بِمَ يَرْجِعُ الْمُرْسَلُونَ
Man, dama leen di yónnee alal [neexal], su ma ko defee nag xool lu ndaw ya di delloosi”.
36فَلَمَّا جَاءَ سُلَيْمَانَ قَالَ أَتُمِدُّونَنِ بِمَالٍ فَمَا آتَانِيَ اللَّهُ خَيْرٌ مِّمَّا آتَاكُم بَلْ أَنتُم بِهَدِيَّتِكُمْ تَفْرَحُونَ
[Ba ndaw ya àggee] ca Suleymaan, mu ne leen : “Yéen daal dangeen may jéem a gere alal ? Maa leen ko gënle fuuf. Mbaa du ! Lii doŋŋ la.
37ارْجِعْ إِلَيْهِمْ فَلَنَأْتِيَنَّهُم بِجُنُودٍ لَّا قِبَلَ لَهُم بِهَا وَلَنُخْرِجَنَّهُم مِّنْهَا أَذِلَّةً وَهُمْ صَاغِرُونَ
Dellul ca ñoom. Neleen danaa leen indil xare bu ñu dul mën a dékku. Te danaa leen fa génne toroxal leen ba ñu ne tott.
38قَالَ يَا أَيُّهَا الْمَلَأُ أَيُّكُمْ يَأْتِينِي بِعَرْشِهَا قَبْلَ أَن يَأْتُونِي مُسْلِمِينَ
Suleymaan ne : "Yéen kilifa yi ! Ana kan moo may indil gàngunaayam ba la ñoo agsi di jébbalesi seen bopp ? ”
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
36Aaya

Tekki — An-Naml 36

Simoore An-Naml Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Ba ndaw ya àggee] ca Suleymaan, mu ne leen :…

Simoore Aaya 36/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers