Al-Qasas · 43/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْكِتَابَ مِن بَعْدِ مَا أَهْلَكْنَا الْقُرُونَ الْأُولَىٰ بَصَائِرَ لِلنَّاسِ وَهُدًى وَرَحْمَةً لَّعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ ۝٤٣
Wa laqad aatainaa Moosal Kitaaba mim ba`di maaa ahlaknal quroonal oolaa basaaa`ira linnaasi wa hudanw wa rahmatal la`allahum yata zakkkaroon
📖 Tekkim Wolof
Jox Nanu Muusaa Téere ba, - ca ginnaaw ba Nu faagaagalee maas ya ko jiitu, - ngir mu doon am njis ak njub, ak yërmaande ak it ngir ñu mën caa fàttalikoo.

🎧 Dégg


📜 Aaya 41-45 — Simoore Al-Qasas

41وَجَعَلْنَاهُمْ أَئِمَّةً يَدْعُونَ إِلَى النَّارِ ۖ وَيَوْمَ الْقِيَامَةِ لَا يُنصَرُونَ
Defoon Nanu leen ay njiit yuy woote jëme Safara. Te bu Bis-pénc baa kenn duleen dimbali.
42وَأَتْبَعْنَاهُمْ فِي هَٰذِهِ الدُّنْيَا لَعْنَةً ۖ وَيَوْمَ الْقِيَامَةِ هُم مِّنَ الْمَقْبُوحِينَ
Nu toqal leen am rëbb ci àddina sii. Te bu Bis-pénc baa dañuy bokk ca ña ñuy siibiibal.
43وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْكِتَابَ مِن بَعْدِ مَا أَهْلَكْنَا الْقُرُونَ الْأُولَىٰ بَصَائِرَ لِلنَّاسِ وَهُدًى وَرَحْمَةً لَّعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ
Jox Nanu Muusaa Téere ba, - ca ginnaaw ba Nu faagaagalee maas ya ko jiitu, - ngir mu doon am njis ak njub, ak yërmaande ak it ngir ñu mën caa fàttalikoo.
44وَمَا كُنتَ بِجَانِبِ الْغَرْبِيِّ إِذْ قَضَيْنَا إِلَىٰ مُوسَى الْأَمْرَ وَمَا كُنتَ مِنَ الشَّاهِدِينَ
Te yaw [Muhammad], nekkoo woon ca xuru sowwu wa ca ba Nuy jox Muusaa ndigal ya: te fekkewoo ko woon [seede ko].
45وَلَٰكِنَّا أَنشَأْنَا قُرُونًا فَتَطَاوَلَ عَلَيْهِمُ الْعُمُرُ ۚ وَمَا كُنتَ ثَاوِيًا فِي أَهْلِ مَدْيَنَ تَتْلُو عَلَيْهِمْ آيَاتِنَا وَلَٰكِنَّا كُنَّا مُرْسِلِينَ
Waaye sosoon Nanu ay maas yu guddu na fan. Te it nekkoo woon ca waa Madiyaana di leen nettali Sunuy kàddu; waaye Nun [Yàlla], Noo daan yable.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
43Aaya

Tekki — Al-Qasas 43

Simoore Al-Qasas Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jox Nanu Muusaa Téere ba, - ca ginnaaw ba Nu…

Simoore Aaya 43/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers