Al-Qasas · 58/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
وَكَمْ أَهْلَكْنَا مِن قَرْيَةٍ بَطِرَتْ مَعِيشَتَهَا ۖ فَتِلْكَ مَسَاكِنُهُمْ لَمْ تُسْكَن مِّن بَعْدِهِمْ إِلَّا قَلِيلًا ۖ وَكُنَّا نَحْنُ الْوَارِثِينَ ۝٥٨
Wa kam ahlaknaa min qaryatim batirat ma`eeshatahaa fatilka masaainuhum lam tuskam mim ba`dihim illaa qaleelaa; wa kunnaa Nahnul waariseen
📖 Tekkim Wolof
Aka bari dëkk bu Nu faagaagal ci sababus seenug weddi te ñu daan dunde xéewal, ca seen kër ya lu néew la, te keneen dëkkee seen ginnaaw, Nun Yàlla noo doon donnale.

🎧 Dégg


📜 Aaya 56-60 — Simoore Al-Qasas

56إِنَّكَ لَا تَهْدِي مَنْ أَحْبَبْتَ وَلَٰكِنَّ اللَّهَ يَهْدِي مَن يَشَاءُ ۚ وَهُوَ أَعْلَمُ بِالْمُهْتَدِينَ
Yaw (Muhammad) du ut ne yaay gindi ku la soob : waaye Yàlla mooy gindi ku ko soob. Te moo gën a xam ñiy gindiku.
57وَقَالُوا إِن نَّتَّبِعِ الْهُدَىٰ مَعَكَ نُتَخَطَّفْ مِنْ أَرْضِنَا ۚ أَوَلَمْ نُمَكِّن لَّهُمْ حَرَمًا آمِنًا يُجْبَىٰ إِلَيْهِ ثَمَرَاتُ كُلِّ شَيْءٍ رِّزْقًا مِّن لَّدُنَّا وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Ñuy wax naan : “Su nu toppee njub gi ànd ak yaw, kon deef nanu foqarñee ci sunu suuf si”. - Ndax defalunu leen woon am réew wuñu wormaal, ñuy jëmmal wépp xeetu meññeef muy bawoo ci Nun [Yàlla] ? Waaye li ëpp ci ñoom xamuñu.
58وَكَمْ أَهْلَكْنَا مِن قَرْيَةٍ بَطِرَتْ مَعِيشَتَهَا ۖ فَتِلْكَ مَسَاكِنُهُمْ لَمْ تُسْكَن مِّن بَعْدِهِمْ إِلَّا قَلِيلًا ۖ وَكُنَّا نَحْنُ الْوَارِثِينَ
Aka bari dëkk bu Nu faagaagal ci sababus seenug weddi te ñu daan dunde xéewal, ca seen kër ya lu néew la, te keneen dëkkee seen ginnaaw, Nun Yàlla noo doon donnale.
59وَمَا كَانَ رَبُّكَ مُهْلِكَ الْقُرَىٰ حَتَّىٰ يَبْعَثَ فِي أُمِّهَا رَسُولًا يَتْلُو عَلَيْهِمْ آيَاتِنَا ۚ وَمَا كُنَّا مُهْلِكِي الْقُرَىٰ إِلَّا وَأَهْلُهَا ظَالِمُونَ
Yàlla du faagaagal yenn dëkk ndare du dafa yebal ab Yonent ca dëkk ba fa gën a rëy, mu di leen nettali ay kàddoom. Te Nun Yàlla dunu faagaagal ay dëkk lu dul ne dañuy tooñ.
60وَمَا أُوتِيتُم مِّن شَيْءٍ فَمَتَاعُ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَزِينَتُهَا ۚ وَمَا عِندَ اللَّهِ خَيْرٌ وَأَبْقَىٰ ۚ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
Lii Nu leen jox, bànneexu dundug àddina [doŋŋ la], te la nekk fa Yàlla moo gën a des ... Moo ndax dangeen dul xel-lu ?
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
58Aaya

Tekki — Al-Qasas 58

Simoore Al-Qasas Aaya 58 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Aka bari dëkk bu Nu faagaagal ci sababus seenug weddi…

Simoore Aaya 58/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 56–60. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers