Ar-Rum · 33/60
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rum
وَإِذَا مَسَّ النَّاسَ ضُرٌّ دَعَوْا رَبَّهُم مُّنِيبِينَ إِلَيْهِ ثُمَّ إِذَا أَذَاقَهُم مِّنْهُ رَحْمَةً إِذَا فَرِيقٌ مِّنْهُم بِرَبِّهِمْ يُشْرِكُونَ ۝٣٣
Wa izaa massan naasa durrun da`aw Rabbahum muneebeena ilaihi summa izaaa azaqahum minhu rahmatan izaa fareequm minhum be Rabbihim yushrikoon
📖 Tekkim Wolof
Bu lor ju laal nit ña amee, dañuy ñaan Yàlla di Ko woo booleek toroxlu. Waaye su leen di mosal yërmaande rekk, [nga gis] ñu delluy bokkaale,

🎧 Dégg


📜 Aaya 31-35 — Simoore Ar-Rum

31۞ مُنِيبِينَ إِلَيْهِ وَاتَّقُوهُ وَأَقِيمُوا الصَّلَاةَ وَلَا تَكُونُوا مِنَ الْمُشْرِكِينَ
Wommatuleen jëm ci Moom ; te nangeen ko ragal, tey taxawal julli te buleen bokk ca way-bokkaale ña,
32مِنَ الَّذِينَ فَرَّقُوا دِينَهُمْ وَكَانُوا شِيَعًا ۖ كُلُّ حِزْبٍ بِمَا لَدَيْهِمْ فَرِحُونَ
ña téqale seen diine di ay kurél, xaaj bu nekk ne siiw la fa moom.
33وَإِذَا مَسَّ النَّاسَ ضُرٌّ دَعَوْا رَبَّهُم مُّنِيبِينَ إِلَيْهِ ثُمَّ إِذَا أَذَاقَهُم مِّنْهُ رَحْمَةً إِذَا فَرِيقٌ مِّنْهُم بِرَبِّهِمْ يُشْرِكُونَ
Bu lor ju laal nit ña amee, dañuy ñaan Yàlla di Ko woo booleek toroxlu. Waaye su leen di mosal yërmaande rekk, [nga gis] ñu delluy bokkaale,
34لِيَكْفُرُوا بِمَا آتَيْنَاهُمْ ۚ فَتَمَتَّعُوا فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ
di fakk la Mu leen indiloon. “Bànneexuleen. Dangeen xala xam”.
35أَمْ أَنزَلْنَا عَلَيْهِمْ سُلْطَانًا فَهُوَ يَتَكَلَّمُ بِمَا كَانُوا بِهِ يُشْرِكُونَ
Walla Danuy wàcce ci ñoom [kilifa] ab Téere buy wàqante la ñu daan bokkaale ?
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
33Aaya

Tekki — Ar-Rum 33

Simoore Ar-Rum Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu lor ju laal nit ña amee, dañuy ñaan Yàlla…

Simoore Aaya 33/60 — Simoore Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rum Dégg, Simoore Ar-Rum Tekki, Simoore Ar-Rum mp3, Simoore Ar-Rum pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers