Fatir · 24/45
Tekki Waxtaan — Simoore Fatir
إِنَّا أَرْسَلْنَاكَ بِالْحَقِّ بَشِيرًا وَنَذِيرًا ۚ وَإِن مِّنْ أُمَّةٍ إِلَّا خَلَا فِيهَا نَذِيرٌ ۝٢٤
Innaa arsalnaak bil haqqi basheeranw wa nazeeraa; wa im min ummatin illaa khalaa feehaa nazeer
📖 Tekkim Wolof
Yónni Nanu la ci dëgg ngay bégalekat di ab xuppekat, amul wenn xeet wu amul ab xuppekat.

🎧 Dégg


📜 Aaya 22-26 — Simoore Fatir

22وَمَا يَسْتَوِي الْأَحْيَاءُ وَلَا الْأَمْوَاتُ ۚ إِنَّ اللَّهَ يُسْمِعُ مَن يَشَاءُ ۖ وَمَا أَنتَ بِمُسْمِعٍ مَّن فِي الْقُبُورِ
Ñiy dundu it niróowuñook ñi dee. Yàlla dina déggloo ku ko soob, te yaw Muhammad mënoo déggloo ñi xas nekk ci biiri bàmmeel.
23إِنْ أَنتَ إِلَّا نَذِيرٌ
Yaw daal nekkoo lu dul ab xuppekat
24إِنَّا أَرْسَلْنَاكَ بِالْحَقِّ بَشِيرًا وَنَذِيرًا ۚ وَإِن مِّنْ أُمَّةٍ إِلَّا خَلَا فِيهَا نَذِيرٌ
Yónni Nanu la ci dëgg ngay bégalekat di ab xuppekat, amul wenn xeet wu amul ab xuppekat.
25وَإِن يُكَذِّبُوكَ فَقَدْ كَذَّبَ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ جَاءَتْهُمْ رُسُلُهُم بِالْبَيِّنَاتِ وَبِالزُّبُرِ وَبِالْكِتَابِ الْمُنِيرِ
Su fekke ne dañu laa weddi, [xamal ne] am na ñu leen jiitu woon te daan weddi, ndax seeni Yonent indiloon nañu leen ay laaya, ay firnde yu bir ak ay mbind ak ab Téere bu leer.
26ثُمَّ أَخَذْتُ الَّذِينَ كَفَرُوا ۖ فَكَيْفَ كَانَ نَكِيرِ
Ginnaaw ba, Ma jël ña weddi. Cëy na Ma leen jële.
FatirFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — Fatir 24

Simoore Fatir Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yónni Nanu la ci dëgg ngay bégalekat di ab xuppekat,…

Simoore Aaya 24/45 — Simoore Fatir فاطر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Fatir Dégg, Simoore Fatir Tekki, Simoore Fatir mp3, Simoore Fatir pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers