Az-Zumar · 28/75
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zumar
قُرْآنًا عَرَبِيًّا غَيْرَ ذِي عِوَجٍ لَّعَلَّهُمْ يَتَّقُونَ ۝٢٨
Qur-aanan `Arabiyyan ghaira zee `iwajil la`allahum yattaqoon
📖 Tekkim Wolof
Mooy Alxuraan ju di [làmmiñu] araab, amul lugg-luggal, ndax amaana ñuy ragal Yàlla !

🎧 Dégg


📜 Aaya 26-30 — Simoore Az-Zumar

26فَأَذَاقَهُمُ اللَّهُ الْخِزْيَ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ۖ وَلَعَذَابُ الْآخِرَةِ أَكْبَرُ ۚ لَوْ كَانُوا يَعْلَمُونَ
Yàlla musal na leen mbugëlu toroxtaane ci dundug àddina sii. Te mbugëlu àllaaxira, moo, gën a rëy, cëy bu ñu xamoon !
27وَلَقَدْ ضَرَبْنَا لِلنَّاسِ فِي هَٰذَا الْقُرْآنِ مِن كُلِّ مَثَلٍ لَّعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ
saddalal Nanu nit ñi ay léebu ci Alxuraan jii, ndax amaana ñuy fàttaliku.
28قُرْآنًا عَرَبِيًّا غَيْرَ ذِي عِوَجٍ لَّعَلَّهُمْ يَتَّقُونَ
Mooy Alxuraan ju di [làmmiñu] araab, amul lugg-luggal, ndax amaana ñuy ragal Yàlla !
29ضَرَبَ اللَّهُ مَثَلًا رَّجُلًا فِيهِ شُرَكَاءُ مُتَشَاكِسُونَ وَرَجُلًا سَلَمًا لِّرَجُلٍ هَلْ يَسْتَوِيَانِ مَثَلًا ۚ الْحَمْدُ لِلَّهِ ۚ بَلْ أَكْثَرُهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Yàllaa ngi sadd léebu jenn waay ju am digaale yu bari tey ŋaayoo : ndax niróonaak waa ju am benn digaale bu mu jubóol ? Yàlla rekk yayoo cant ! Li am moo di ne li ëpp ci ñoom xamuñu (misaalum kuy jaamu Yàlla ak ku koy bokkaale).
30إِنَّكَ مَيِّتٌ وَإِنَّهُم مَّيِّتُونَ
Yaw dangay dee ñoom it dañuy dee ;
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — Az-Zumar 28

Simoore Az-Zumar Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mooy Alxuraan ju di [làmmiñu] araab, amul lugg-luggal, ndax amaana…

Simoore Aaya 28/75 — Simoore Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zumar Dégg, Simoore Az-Zumar Tekki, Simoore Az-Zumar mp3, Simoore Az-Zumar pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers