Ghafir · 77/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
فَاصْبِرْ إِنَّ وَعْدَ اللَّهِ حَقٌّ ۚ فَإِمَّا نُرِيَنَّكَ بَعْضَ الَّذِي نَعِدُهُمْ أَوْ نَتَوَفَّيَنَّكَ فَإِلَيْنَا يُرْجَعُونَ ۝٧٧
Fasbir inna wa`dal laahi haqq; fa immaa nuriyannak ba`dal lazee na`i duhum aw natawaffayannaka fa ilainaa yurja`oon
📖 Tekkim Wolof
Na ngay muñ (te xam ne). Digub Yàlla dëgg la. Amaana Nu wan la lenn ci li Nu leen di tëkkoo mbaa nu faat la (balaa loolu di am)... ak lu man a xew ñoom ñépp ci nun la nuy dellusi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 75-79 — Ghafir

75ذَٰلِكُم بِمَا كُنتُمْ تَفْرَحُونَ فِي الْأَرْضِ بِغَيْرِ الْحَقِّ وَبِمَا كُنتُمْ تَمْرَحُونَ
Lii moo di peyug li ngeen daan bég ci suuf si (àddina), te du woon dëgg, ngeen daan ca maare.
76ادْخُلُوا أَبْوَابَ جَهَنَّمَ خَالِدِينَ فِيهَا ۖ فَبِئْسَ مَثْوَى الْمُتَكَبِّرِينَ
Dugguleen ci wunti Safara te ngeen béel fa. Ña rëy-rëylu woon seenub dëkkuwaay bon na !
77فَاصْبِرْ إِنَّ وَعْدَ اللَّهِ حَقٌّ ۚ فَإِمَّا نُرِيَنَّكَ بَعْضَ الَّذِي نَعِدُهُمْ أَوْ نَتَوَفَّيَنَّكَ فَإِلَيْنَا يُرْجَعُونَ
Na ngay muñ (te xam ne). Digub Yàlla dëgg la. Amaana Nu wan la lenn ci li Nu leen di tëkkoo mbaa nu faat la (balaa loolu di am)... ak lu man a xew ñoom ñépp ci nun la nuy dellusi.
78وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا رُسُلًا مِّن قَبْلِكَ مِنْهُم مَّن قَصَصْنَا عَلَيْكَ وَمِنْهُم مَّن لَّمْ نَقْصُصْ عَلَيْكَ ۗ وَمَا كَانَ لِرَسُولٍ أَن يَأْتِيَ بِآيَةٍ إِلَّا بِإِذْنِ اللَّهِ ۚ فَإِذَا جَاءَ أَمْرُ اللَّهِ قُضِيَ بِالْحَقِّ وَخَسِرَ هُنَالِكَ الْمُبْطِلُونَ
Yónni woon Nanu ay Yonnent yu la jiitu woon. am na ci ñu ñu la nettali ; am na ci ñu ñu la nettaliwul. Amul benn yonnent bu sañ a indi [kimaan laaya] lu dul ne da ca am ndigëlul Yàlla. Saa su ndigëlul Yàlla agsee, mbir yépp àttewo ci dëgg ; fenkat yi daldi yàqule.
79اللَّهُ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَنْعَامَ لِتَرْكَبُوا مِنْهَا وَمِنْهَا تَأْكُلُونَ
Yàlla mi leen defaral mala yi ngir ngeen di ci war te di ca lekk,
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
77Aaya

Tekki — Ghafir 77

Simoore Ghafir Aaya 77 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Na ngay muñ (te xam ne). Digub Yàlla dëgg la.…

Simoore Aaya 77/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 75–79. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers