Ash-Shura · 34/53
Tekki Waxtaan — Ash-Shura
أَوْ يُوبِقْهُنَّ بِمَا كَسَبُوا وَيَعْفُ عَن كَثِيرٍ ۝٣٤
Aw yoobiqhunna bimaa kasaboo wa ya`fu `an kaseer
📖 Tekkim Wolof
Walla, mu mbugël leen ci seeni jëf. Tey jéggële lu bari.

🎧 Dégg


📜 Aaya 32-36 — Ash-Shura

32وَمِنْ آيَاتِهِ الْجَوَارِ فِي الْبَحْرِ كَالْأَعْلَامِ
Bokk na ci ay kéemaanam (firndéem), gaal yuy daw ci géej, tollu ni ay tundu doj.
33إِن يَشَأْ يُسْكِنِ الرِّيحَ فَيَظْلَلْنَ رَوَاكِدَ عَلَىٰ ظَهْرِهِ ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّكُلِّ صَبَّارٍ شَكُورٍ
Su ko neexee, Mu téye ngilaw, ñu ne tekk ca ndox ma. Ay kéemaan na ngi ci biir loolu ngir [nit] kuy muñ tey sant (dello njukël).
34أَوْ يُوبِقْهُنَّ بِمَا كَسَبُوا وَيَعْفُ عَن كَثِيرٍ
Walla, mu mbugël leen ci seeni jëf. Tey jéggële lu bari.
35وَيَعْلَمَ الَّذِينَ يُجَادِلُونَ فِي آيَاتِنَا مَا لَهُم مِّن مَّحِيصٍ
Ñiy diiŋat sunuy firnde it danañu xam ne du nu man a am rawtukaay.
36فَمَا أُوتِيتُم مِّن شَيْءٍ فَمَتَاعُ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ۖ وَمَا عِندَ اللَّهِ خَيْرٌ وَأَبْقَىٰ لِلَّذِينَ آمَنُوا وَعَلَىٰ رَبِّهِمْ يَتَوَكَّلُونَ
Lii nu leen jox lépp [ci alal] bànneexu dundug àddina rekk la ; waaye la nekk ca Yàlla moo gënn te moo gën a sax ngir nit ñi gëm tey doyloo seen Boroom,
Ash-ShuraFihi Alxuraan
53Aaya
MeccanRevelation
34Aaya

Tekki — Ash-Shura 34

Simoore Ash-Shura Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla, mu mbugël leen ci seeni jëf. Tey jéggële lu…

Simoore Aaya 34/53 — Ash-Shura الشورى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shura Dégg, Ash-Shura Tekki, Ash-Shura mp3, Ash-Shura pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers