Ash-Shura · 51/53
Tekki Waxtaan — Ash-Shura
۞ وَمَا كَانَ لِبَشَرٍ أَن يُكَلِّمَهُ اللَّهُ إِلَّا وَحْيًا أَوْ مِن وَرَاءِ حِجَابٍ أَوْ يُرْسِلَ رَسُولًا فَيُوحِيَ بِإِذْنِهِ مَا يَشَاءُ ۚ إِنَّهُ عَلِيٌّ حَكِيمٌ ۝٥١
Wa maa kaana libasharin any yukallimahul laahu illaa wahyan aw minw waraaa`i hijaabin aw yursila Rasoolan fa yoohiya bi iznuhee maa yashaaa`; innahoo `Aliyyun Hakeem
📖 Tekkim Wolof
Yàlla du waxanteek kenn nit lu dul ci soloo, walla ci ginnaaw kiiraay, walla mu yabal ndaw (Malaaka) mu di ko soloo, lu ko soob, ci ndigalul Yàllal. Yàlla aji Kawe la aji Xereñ la.
🎧 Dégg

📜 Aaya 49-53 — Ash-Shura

49لِّلَّهِ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ يَخْلُقُ مَا يَشَاءُ ۚ يَهَبُ لِمَن يَشَاءُ إِنَاثًا وَيَهَبُ لِمَن يَشَاءُ الذُّكُورَ
Yàllaa moom nguurug asamaan yeek suuf si. mooy bind lu ko soob. Mooy may ku Ko soob ay doom yu jigéen, mooy may it ku Ko soob ay doom yu góor,
50أَوْ يُزَوِّجُهُمْ ذُكْرَانًا وَإِنَاثًا ۖ وَيَجْعَلُ مَن يَشَاءُ عَقِيمًا ۚ إِنَّهُ عَلِيمٌ قَدِيرٌ
walla mu di ko def njaxas ñu di góor ak jigéen ; Mooy def it ku Ko soob jaasir. Yàlla aji Xam la boroom Doole la.
51۞ وَمَا كَانَ لِبَشَرٍ أَن يُكَلِّمَهُ اللَّهُ إِلَّا وَحْيًا أَوْ مِن وَرَاءِ حِجَابٍ أَوْ يُرْسِلَ رَسُولًا فَيُوحِيَ بِإِذْنِهِ مَا يَشَاءُ ۚ إِنَّهُ عَلِيٌّ حَكِيمٌ
Yàlla du waxanteek kenn nit lu dul ci soloo, walla ci ginnaaw kiiraay, walla mu yabal ndaw (Malaaka) mu di ko soloo, lu ko soob, ci ndigalul Yàllal. Yàlla aji Kawe la aji Xereñ la.
52وَكَذَٰلِكَ أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ رُوحًا مِّنْ أَمْرِنَا ۚ مَا كُنتَ تَدْرِي مَا الْكِتَابُ وَلَا الْإِيمَانُ وَلَٰكِن جَعَلْنَاهُ نُورًا نَّهْدِي بِهِ مَن نَّشَاءُ مِنْ عِبَادِنَا ۚ وَإِنَّكَ لَتَهْدِي إِلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Noonu la ñuy soloo ci yaw [Alxuraan] ci Sunu ndigël. amoo woon benn xam-xam ci Téere bi du caagéene ngëm; waaye def leer di ci gindi ku nu soob ci sunu jaam ñi. Te yaw it da ngay gindee jëme ci yoon wu jub wa xocc,
53صِرَاطِ اللَّهِ الَّذِي لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۗ أَلَا إِلَى اللَّهِ تَصِيرُ الْأُمُورُ
yoonu Yàlla ji moom asamaan yeek suuf si ak li ci seen biir. Ca dëgg-dëgg ca yàlla la mbir yépp di mujj.
Ash-ShuraFihi Alxuraan
53Aaya
MeccanRevelation
51Aaya

Tekki — Ash-Shura 51

Simoore Ash-Shura Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla du waxanteek kenn nit lu dul ci soloo, walla…

Simoore Aaya 51/53 — Ash-Shura الشورى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shura Dégg, Ash-Shura Tekki, Ash-Shura mp3, Ash-Shura pdf. Aaya 49–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers