Az-Zukhruf · 23/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
وَكَذَٰلِكَ مَا أَرْسَلْنَا مِن قَبْلِكَ فِي قَرْيَةٍ مِّن نَّذِيرٍ إِلَّا قَالَ مُتْرَفُوهَا إِنَّا وَجَدْنَا آبَاءَنَا عَلَىٰ أُمَّةٍ وَإِنَّا عَلَىٰ آثَارِهِم مُّقْتَدُونَ ۝٢٣
Wa kazaalika maaa arsalnaa min qablika fee qaryatim min nazeerin illaa qaala mutrafoohaaa innaa wajadnaaa aabaaa`anaa `alaaa ummatinw wa innaa `alaaa aasaarihim muqtadoon
📖 Tekkim Wolof
(Noonu it la daan deme) ndax masunoo yónni waa ab xuppekat (waaraatekat) cib dëkk lu dul ne ne kilifa ya danuy wax naan : “Sunuy maam amoon nañu diine te nun ñoom la ñuy roy”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — Simoore Az-Zukhruf

21أَمْ آتَيْنَاهُمْ كِتَابًا مِّن قَبْلِهِ فَهُم بِهِ مُسْتَمْسِكُونَ
Walla, da Nu leen joxoon ab Téere ca la ko jiitu woon ba tax ñu ŋoyoon ca ?
22بَلْ قَالُوا إِنَّا وَجَدْنَا آبَاءَنَا عَلَىٰ أُمَّةٍ وَإِنَّا عَلَىٰ آثَارِهِم مُّهْتَدُونَ
Li ñu wax kay moo di : “Fekkoon nanu sunuy maam am diine, kon nag (wat ci watiit) ñoom la ñuy toppandoo”.
23وَكَذَٰلِكَ مَا أَرْسَلْنَا مِن قَبْلِكَ فِي قَرْيَةٍ مِّن نَّذِيرٍ إِلَّا قَالَ مُتْرَفُوهَا إِنَّا وَجَدْنَا آبَاءَنَا عَلَىٰ أُمَّةٍ وَإِنَّا عَلَىٰ آثَارِهِم مُّقْتَدُونَ
(Noonu it la daan deme) ndax masunoo yónni waa ab xuppekat (waaraatekat) cib dëkk lu dul ne ne kilifa ya danuy wax naan : “Sunuy maam amoon nañu diine te nun ñoom la ñuy roy”.
24۞ قَالَ أَوَلَوْ جِئْتُكُم بِأَهْدَىٰ مِمَّا وَجَدتُّمْ عَلَيْهِ آبَاءَكُمْ ۖ قَالُوا إِنَّا بِمَا أُرْسِلْتُم بِهِ كَافِرُونَ
Mu wax leen ne : “Ndax indilu ma leen lu gën a jub la seen baay ya nekkoon ? ” Ñu tontu ne ko : “Nun kat gëmu nu lii ñu la yónni”.
25فَانتَقَمْنَا مِنْهُمْ ۖ فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُكَذِّبِينَ
Nu daldi fayu ca seen kaw. Xoolal (settantal) naka la mujjug weddikat ya deme.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 23

Simoore Az-Zukhruf Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (Noonu it la daan deme) ndax masunoo yónni waa ab…

Simoore Aaya 23/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers