Az-Zukhruf · 25/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
فَانتَقَمْنَا مِنْهُمْ ۖ فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُكَذِّبِينَ ۝٢٥
Fantaqamnaa minhum fanzur kaifa kaana `aaqibatul mukazzibeen
📖 Tekkim Wolof
Nu daldi fayu ca seen kaw. Xoolal (settantal) naka la mujjug weddikat ya deme.

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-27 — Simoore Az-Zukhruf

23وَكَذَٰلِكَ مَا أَرْسَلْنَا مِن قَبْلِكَ فِي قَرْيَةٍ مِّن نَّذِيرٍ إِلَّا قَالَ مُتْرَفُوهَا إِنَّا وَجَدْنَا آبَاءَنَا عَلَىٰ أُمَّةٍ وَإِنَّا عَلَىٰ آثَارِهِم مُّقْتَدُونَ
(Noonu it la daan deme) ndax masunoo yónni waa ab xuppekat (waaraatekat) cib dëkk lu dul ne ne kilifa ya danuy wax naan : “Sunuy maam amoon nañu diine te nun ñoom la ñuy roy”.
24۞ قَالَ أَوَلَوْ جِئْتُكُم بِأَهْدَىٰ مِمَّا وَجَدتُّمْ عَلَيْهِ آبَاءَكُمْ ۖ قَالُوا إِنَّا بِمَا أُرْسِلْتُم بِهِ كَافِرُونَ
Mu wax leen ne : “Ndax indilu ma leen lu gën a jub la seen baay ya nekkoon ? ” Ñu tontu ne ko : “Nun kat gëmu nu lii ñu la yónni”.
25فَانتَقَمْنَا مِنْهُمْ ۖ فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُكَذِّبِينَ
Nu daldi fayu ca seen kaw. Xoolal (settantal) naka la mujjug weddikat ya deme.
26وَإِذْ قَالَ إِبْرَاهِيمُ لِأَبِيهِ وَقَوْمِهِ إِنَّنِي بَرَاءٌ مِّمَّا تَعْبُدُونَ
(Fàttalikul) Ibraahiima ba mu waxee baayam aku nitam : “Man mii ku deñ laa ci lii ngeen di jaamu,
27إِلَّا الَّذِي فَطَرَنِي فَإِنَّهُ سَيَهْدِينِ
ba mu des (Yàlla) mi ma sàkk bind ma, te moo may gindi”.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 25

Simoore Az-Zukhruf Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu daldi fayu ca seen kaw. Xoolal (settantal) naka la…

Simoore Aaya 25/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers